A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente
baada ya kusema hayo, akawaonyesha mikono na miguu.
bi mu leen waxee loolu, mu won leen ay loxoom ak ay tànkam.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
alipokwisha sema hayo, akawaonyesha mikono yake na ubavu wake. basi, hao wanafunzi wakafurahi mno kumwona bwana.
mu daldi leen won ay loxoom ak wetam. bi ñu gisee boroom bi, taalibe ya daldi bég lool.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
naye mungu aliimarisha ahadi yake kwa kiapo; na kwa namna hiyo akawaonyesha wazi wale aliowaahidia kwamba hatabadili nia yake.
Ñi war a jot li mu dige, yàlla dafa leen bëggoon a won ne, dogalam du tebbiku mukk; looloo tax mu dige, boole ci ngiñ.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
maana yohane alikuja kwenu akawaonyesha njia njema ya kuishi, nanyi hamkumwamini; lakini watoza ushuru na waasherati walimwamini. hata baada ya kuona hayo yote ninyi hamkubadili mioyo yenu, na hamkusadiki."
ndaxte yaxya ñëw na ci yéen ci yoonu njub, te gëmuleen ko; waaye juutikat yi ak jigéeni moykat yi gëm nañu ko. te gannaaw bi ngeen gisee loolu, seen xel soppikuwul sax, ba ngeen gëm ko.»
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível