A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente
yesu akajibu, "atakayechovya mkate pamoja nami katika bakuli ndiye atakayenisaliti.
yeesu tontu leen ne: «ki dugal loxoom ak man ci ndab li, kooku moo may wor.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível
malaika wa tatu akamwaga bakuli lake katika mito na chemchemi za maji, navyo vikageuka damu.
Ñetteelu malaaka ma sotti ndabam ci dex yi ak ci bëti ndox yi. Ñu daldi nekk deret.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
kisha akatia maji katika bakuli, akaanza kuwaosha wanafunzi wake miguu na kuipangusa kwa kile kitambaa alichojifungia.
noonu mu sotti ndox ci ab këll, daldi tàmbali di raxas tànki taalibe ya, di leen fomp ak sarbet, ba mu laxasaayoo.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
yesu akawaambia, "ni mmoja wenu ninyi kumi na wawili, anayechovya mkate pamoja nami katika bakuli.
mu tontu leen: «kenn ci yéen fukk ak ñaar la, kuy cappandoo ak man ci ndab li.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível
kisha malaika wa pili akamwaga bakuli lake baharini. nayo bahari ikawa damu tupu kama damu ya mtu aliyekufa, na viumbe vyote hai baharini vikafa.
Ñaareelu malaaka ma sotti ndabam ci géej gi. mu soppiku deret ni deretu néew, ba lépp luy dund te nekkoon ci géej gi dee.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
hapo palikuwa na bakuli limejaa siki. basi, wakachovya sifongo katika hiyo siki, wakaitia juu ya ufito wa husopo, wakamwekea mdomoni.
amoon na foofa gutt bu fees ak bineegar. noonu ñu jël sagar, tooyal ko ca, takk ko ci bantu garab gu ñuy wax isob, teg ko ci gémmiñu yeesu.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
basi, malaika wa kwanza akaenda akamwaga bakuli lake juu ya nchi. mara madonda mabaya na ya kuumiza sana yakawapata wote waliokuwa na alama ya yule mnyama, na wale walioiabudu sanamu yake.
noonu malaaka mu jëkk ma dem, sotti ndabam ci àddina, ba woppi taab ju bon te metti dal nit, ña am màndargam rab wa tey jaamu nataalam.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
kisha malaika wa saba akamwaga bakuli lake hewani. sauti kubwa ikasikika kutoka kwenye kiti cha enzi, hekaluni, ikisema, "mwisho umefika!"
ci kaw loolu juróom-ñaareelu malaaka ma sotti ndabam ci ngelaw. noonu baat bu xumb jóge ca gàngune ma ca kër yàlla ga, naan: «lépp mat na.»
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível
"ole wenu walimu wa sheria na mafarisayo, wanafiki! mnasafisha kikombe na bakuli kwa nje, lakini ndani mnaacha kumejaa vitu mlivyopata kwa unyang'anyi na uchoyo.
«yéen xutbakat yi ak farisen yi, naaféq yi, dingeen torox! ndaxte yéena ngi setal bitib kaas bi ak ndab li, waaye ci biir dafa fees ak càcc ak ëppal.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível