A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente
msihukumu mambo kwa nje tu; toeni hukumu ya haki."
bàyyileen di àtte ci ni ngeen di gise, te di àtte dëgg.»
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível
kuhusu hukumu kwa sababu mkuu wa ulimwengu huu amekwisha hukumiwa.
ci mbiri àtte ba, dina leen yey ndaxte àtte nañu malaaka mu bon mi jiite àddina si, ba daan ko.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
baba hamhukumu mtu yeyote; shughuli yote ya hukumu amemkabidhi mwana,
baay bi du àtte kenn; àtte bi yépp, jox na ko doom ji,
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
linalobaki ni kungojea tu kwa hofu hukumu ya mungu na moto mkali utakaowaangamiza wote wanaompinga.
déedéet, bu nu defee noonu, dinanu tiit di xaar àtte ba, muy taal bu yànj, biy war a lakk nooni yàlla yi.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
kwa hiyo, sasa hakuna hukumu kwa wale ambao katika maisha yao wameungana na kristo.
léegi nag yoon mënul a dab ñi bokk ci yeesu kirist.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
basi, kama vile kila mtu hufa mara moja tu, kisha husimama mbele ya hukumu ya mungu,
kon ni nit ñi deeye benn yoon rekk, ba noppi jaar ca àtte ba, ni ko yàlla dogale,
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
"basi, nawaambieni, siku ya hukumu watu watapaswa kujibu juu ya kila neno lisilofaa wanalosema.
maa ngi leen di wax ne, keroog bés pénc, nit ñi dinañu làyyi ndax wax ju nekk ju amul njariñ, ju ñu mas a wax.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível
anayepinga mamlaka ya viongozi anapinga agizo la mungu; nao wafanyao hivyo wanajiletea hukumu wenyewe,
kon ku leen bañ a déggal, ndigalu yàlla nga lànk, te ku def loolu, yoon dina la dab.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
hata nikihukumu, hukumu yangu ni ya haki kwa sababu mimi siko peke yangu; baba aliyenituma yuko pamoja nami.
teewul nag, su ma demee bay àtte, bu jub lay doon, ndaxte du man rekk ay àtte, waaye baay, bi ma yónni, daf ciy ànd ak man.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
lakini nawaambieni, siku ya hukumu itakuwa nafuu zaidi kwa watu wa sodoma, kuliko kwako wewe."
waaye maa ngi leen koy wax, keroog bés pénc ma sodom moo lay tane.»
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível
basi, kama vile kosa la mtu mmoja lilivyoleta hukumu kwa binadamu wote, kadhalika kitendo kimoja kiadilifu kinawapa uhuru na uzima.
kon nag nu gàttal wax ji; jàddug kenn nit ka rekk moo waral yàlla daan ñépp; noonu itam jëf ju jubu keneen nit ka rekk moo ubbi bunt, ba ñépp man a jub ci kanam yàlla te am dund gu bees.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
lakini wewe, rafiki, unayewahukumu wale wanaofanya mambo kama hayo bali wewe pia unayafanya, je unadhani utaiepa hukumu ya mungu?
yaw nag miy àtte ñiy def loolu, te di ko def, ndax defe nga ne, dinga rëcc ci àtteb yàlla?
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
ikiwa basi, kulikuwa na utukufu katika huduma ile iliyoleta hukumu, ni wazi kwamba huduma ile iletayo kukubaliwa kuwa waadilifu itakuwa na utukufu mkuu zaidi.
su fekkee ne tëralin, wiy teg nit tooñ, àndoon na ak ndam, rawatina ci tëralin wiy àtte nit jub.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
kwa hiyo, basi, bwana anajua jinsi ya kuwaokoa katika majaribu watu wanaomcha mungu, na jinsi ya kuwaweka waovu katika adhabu hadi siku ile ya hukumu,
gannaaw loolu lépp am na nag, nanu bir ne, boroom bi man na musal aji gëm ji nekk ci nattu, te denc ñi jubadi, ngir alag leen bésu àtte ba.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
"hapa ni mtumishi wangu niliyemteua, mpendwa wangu anipendezaye moyoni. nitaiweka roho yangu juu yake, naye atatangaza hukumu yangu kwa mataifa yote.
«kii mooy sama ndaw li ma tànn,di sama soppe bi neex sama xol.dinaa def sama xel ci moom,muy yégal xeet yi yoonu njub.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível
na kama kuna yeyote aliye na njaa, na ale nyumbani kwake, ili kukutana kwenu kusisababishe hukumu. lakini, kuhusu yale mambo mengine, nitawapeni maelezo nitakapokuja.
ku xiif, na lekke këram, ngir bañ a indi ci yéen àtteb yàlla ndax seen ndaje yi. yeneen fànn yi ci des nag, bu ma ñëwee ci yéen, dinaa ko seet.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
wakati wa hukumu umefika, na hukumu hiyo inaanza na watu wake mungu mwenyewe. ikiwa hukumu hiyo inaanzia kwetu sisi, basi mwisho wake utakuwa namna gani kwa wale wasioamini habari njema ya mungu?
ndaxte àpp bi jot na, àtte baa ngi tàmbalee ci nun waa kër yàlla. te su tàmbalee ci nun nag, luy muju ñi weddi xebaaru yàlla?
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
lakini, bwana alikaa pamoja nami, akanipa nguvu, hata nikaweza kuutangaza ujumbe wote, watu wa mataifa wausikie; tena nikaokolewa katika hukumu ya kifo kama kinywani mwa simba.
waaye boroom bi moo ma taxawu te dooleel ma, ma jollil kàddu gi, ba xeet yépp dégg ko. te boroom bi musal na ma ci selli gaynde.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
"mimi siwezi kufanya kitu kwa uwezo wangu mwenyewe. mimi nina hukumu kama ninavyosikia kutoka kwa baba, nayo hukumu yangu ni ya haki. nia yangu si kufanya nipendavyo mwenyewe, bali apendavyo yule aliyenituma.
mënumaa def dara man ci sama bopp. ni ma baay bi di digale rekk laay àttee, te sama àtte bu jub la, ndaxte defuma sama bëgg-bëgg, ci waawi ki ma yónni doŋŋ laay aw.
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível
akasema kwa sauti kubwa, "mcheni mungu na kumtukuza! maana saa imefika ya kutoa hukumu yake. mwabuduni yeye aliyeumba mbingu na nchi, bahari na chemchemi za maji."
ma nga doon xaacu naan: «ragal-leen yàlla te jox ko ndam li, ndaxte waxtuw àtteem jot na. jaamuleen ki sàkk asamaan ak suuf ak géej ak bëti ndox yi.»
Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:
Aviso: contém formatação HTML invisível