Você procurou por: wamtangulie (Suaíli - Wolof)

Contribuições humanas

A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente

Adicionar uma tradução

Suaíli

Wolof

Informações

Suaíli

basi, akawatuma wajumbe wamtangulie, nao wakaenda wakaingia kijiji kimoja cha wasamaria ili wamtayarishie mahali.

Wolof

noonu mu yebal ay ndaw, ñu jiitu ko. Ñu dem nag, dugg ci ab dëkk ci diiwaanu samari, ngir wutal ko fa fu mu dal.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

mara, yesu akawaamuru wanafunzi wake wapande mashua, wamtangulie ng'ambo ya ziwa wakati yeye anawaaga watu.

Wolof

bi loolu amee yeesu sant taalibe ya, ñu dugg gaal ga te jàll dex ga, jiituji ko, muy yiwi mbooloo ma.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

hivyo, aliwatuma wawili wa wasaidizi wake, timotheo na erasto, wamtangulie kwenda makedonia, naye akabaki kwa muda huko asia.

Wolof

mu yebal nag ci maseduwan ñaari jaraafam, di timote ak erast, waaye moom mu des ab diir ci asi.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

mara yesu akawaamuru wanafunzi wake wapande mashua, wamtangulie kwenda bethsaida, ng'ambo ya ziwa, wakati yeye anauaga umati wa watu.

Wolof

ci kaw loolu yeesu sant ay taalibeem, ñu dugg ci gaal gi, jàll ba betsayda, bi muy yiwi mbooloo mi.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

baada ya hayo, bwana aliwachagua wengine sabini na wawili, akawatuma wawiliwawili, wamtangulie katika kila kijiji na mahali ambapo yeye mwenyewe alitaka kwenda.

Wolof

gannaaw loolu boroom bi tànn na yeneen juróom-ñaar-fukki taalibe ak ñaar, yebal leen, ñu ànd ñaar ak ñaar, jiituji ko ca dëkk yépp ak ca bérab yépp, ya mu naroon a dem moom ci boppam.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Consiga uma tradução melhor através
7,726,286,889 de colaborações humanas

Usuários estão solicitando auxílio neste momento:



Utilizamos cookies para aprimorar sua experiência. Se avançar no acesso a este site, você estará concordando com o uso dos nossos cookies. Saiba mais. OK