Você procurou por: dafay (Wolof - Francês)

Contribuições humanas

A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente

Adicionar uma tradução

Wolof

Francês

Informações

Wolof

bii task dafay regle sa sistem bi bamu doon ab serwóor bu imprimante.

Francês

cette tâche configure votre système pour être un serveur d'impression.

Última atualização: 2014-08-15
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

bii task dafay istale ay prograam yu am njariñ ci ordinaatéer bu portaabal.

Francês

cette tâche installe des logiciels utiles pour les ordinateurs portables.

Última atualização: 2014-08-15
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

waaw, ba tey jii, su ñuy jàng yoonu musaa, seen xol dafay muuru.

Francês

jusqu`à ce jour, quand on lit moïse, un voile est jeté sur leurs coeurs;

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

bii task dafay tann ay paket yu am njariñ ci ab sistem bu am serwóor bu web.

Francês

cette tâche choisit les paquets utiles pour un serveur web générique.

Última atualização: 2014-08-15
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

nit ki yor xelum yàlla dafay àtte lépp, te moom ci boppam, kenn du ko àtte.

Francês

l`homme spirituel, au contraire, juge de tout, et il n`est lui-même jugé par personne.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

bii task dafay joxe prograam bu biro "desktop" buy jëfandikoo k desktop environment.

Francês

cette tâche fournit les logiciels de base pour l'environnement de bureau kde.

Última atualização: 2014-08-15
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Aviso: contém formatação HTML invisível

Wolof

bii task dafay joxe prograam yu biro "desktop" di jëfandikoo barabu biro bu gnome.

Francês

cette tâche fournit les logiciels de base pour l'environnement de bureau gnome.

Última atualização: 2014-08-15
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Aviso: contém formatação HTML invisível

Wolof

dafay tann serwóor bind dns ak dokimantaasioŋ yi ci aju ak ay paket yuy jumtukaay (utilitaire).

Francês

choisit le serveur dns bind, ainsi que la documentation associée et quelques utilitaires.

Última atualização: 2014-08-15
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

kiy wax aw làkk dafay yokk boppam, waaye kiy wax ci kàddug yàlla, dafay yokk ngëmu mbooloo mi.

Francês

celui qui parle en langue s`édifie lui-même; celui qui prophétise édifie l`Église.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

bii task dafay joxe ay prograam yu biro (desktop), moo làmboo task yu biro gnome ak biro kde.

Francês

cette tâche fournit les logiciels de base pour un environnement de bureau et sert de base pour les tâches d'installation des environnements gnome et kde.

Última atualização: 2014-08-15
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

ndaxte bu ngeen dee lekk, ku nekk dafay gaawantu di lekk reeram, ba tax ñenn ñaa ngi xiif, fekk ñeneen di màndi.

Francês

car, quand on se met à table, chacun commence par prendre son propre repas, et l`un a faim, tandis que l`autre est ivre.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

li ngeen di war a muñ, ab yar la. yàlla dafay jëf ak yéen ni ay doomam, ndaxte ana doom ju baayam dul yar?

Francês

supportez le châtiment: c`est comme des fils que dieu vous traite; car quel est le fils qu`un père ne châtie pas?

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

bëggoon naa, ngeen bañ a am benn xalaat. góor gu takkul jabar dafay bàyyi xel ci mbiri boroom bi, di wut a neex boroom bi.

Francês

or, je voudrais que vous fussiez sans inquiétude. celui qui n`est pas marié s`inquiète des choses du seigneur, des moyens de plaire au seigneur;

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

waaye bu ñépp dee wax ci kàddug yàlla, te ku gëmul dugg fa, walla ku jàngul mbiri kirist, wax yi ñépp wax dafay wone bàkkaaram te àtte ko,

Francês

mais si tous prophétisent, et qu`il survienne quelque non-croyant ou un homme du peuple, il est convaincu par tous, il est jugé par tous,

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

li am moo di ne, yar bu nuy dal, du ànd ak bànneex, day naqari, waaye gannaaw ga dafay meññ jub ak jàmm, ci ñi ko jariñoo.

Francês

il est vrai que tout châtiment semble d`abord un sujet de tristesse, et non de joie; mais il produit plus tard pour ceux qui ont été ainsi exercés un fruit paisible de justice.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

saraxalekat bu mag bi dafay dugg at mu jot ca bérab bu sell-baa-sell ak deret ju dul josam. waaye kirist joxewul bakkanam ay yooni yoon.

Francês

et ce n`est pas pour s`offrir lui-même plusieurs fois qu`il y est entré, comme le souverain sacrificateur entre chaque année dans le sanctuaire avec du sang étranger;

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

bu fekkee ne dangeen a bëgg firnde juy wone ne, kirist mooy wax jaarale ko ci man, dingeen ko am. digganteem ak yéen du ànd ak néew doole, waaye dafay feeñal kàttan ci seen biir.

Francês

puisque vous cherchez une preuve que christ parle en moi, lui qui n`est pas faible à votre égard, mais qui est puissant parmi vous.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

waaye seen xel dafa daldi gumba. ba tey jii sax, bu ñuy jàng téereb kóllëre gu jëkk gi, muuraay moomu dafay des; deñul, ndaxte ci kirist rekk la man a deñe.

Francês

mais ils sont devenus durs d`entendement. car jusqu`à ce jour le même voile demeure quand, ils font la lecture de l`ancien testament, et il ne se lève pas, parce que c`est en christ qu`il disparaît.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

moo nu jox kàttan, nu nekk ndaw yuy xamle kóllëre gu bees gi. te kóllëre googu ajuwul ci ay sàrti diine, waaye mi ngi aju ci jëfu xelum yàlla. ndaxte sàrti kese day jëme ci dee, waaye xelum yàlla dafay joxe dund.

Francês

il nous a aussi rendus capables d`être ministres d`une nouvelle alliance, non de la lettre, mais de l`esprit; car la lettre tue, mais l`esprit vivifie.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Wolof

ci li mu wax: «beneen yoon,» dafay xamle ne, yàlla dina dindi yi ñu man a yengal, maanaam li ñu sàkk, ngir li ñu mënul a yengal sax ba fàww.

Francês

ces mots: une fois encore, indiquent le changement des choses ébranlées, comme étant faites pour un temps, afin que les choses inébranlables subsistent.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Consiga uma tradução melhor através
7,788,040,710 de colaborações humanas

Usuários estão solicitando auxílio neste momento:



Utilizamos cookies para aprimorar sua experiência. Se avançar no acesso a este site, você estará concordando com o uso dos nossos cookies. Saiba mais. OK