You searched for: pour l'amour de dieu (Franska - Wolof)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Franska

Wolof

Info

Franska

mais je sais que vous n`avez point en vous l`amour de dieu.

Wolof

waaye yéen, xam naa leen; leer na ma ne, amuleen ci seen xol benn mbëggeel ci yàlla.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car l`amour de dieu consiste a garder ses commandements. et ses commandements ne sont pas pénibles,

Wolof

ndaxte mbëggeel ci yàlla mooy sàmm ay ndigalam; te ay ndigalam diisuñu.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

commencement de l`Évangile de jésus christ, fils de dieu.

Wolof

xebaar bu baaxu yeesu kirist, doomu yàlla, nii la tàmbalee.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

en lui vous êtes aussi édifiés pour être une habitation de dieu en esprit.

Wolof

te ci seen bokk ci kirist, yàlla boole na leen tabax yéen itam, ba ngeen nekk dëkkukaayam, jaar ci xel mu sell mi.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car tous ceux qui sont conduits par l`esprit de dieu sont fils de dieu.

Wolof

ndaxte ñépp ñiy déggal xelu yàlla mi, ay doomi yàlla lañu.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car la colère de l`homme n`accomplit pas la justice de dieu.

Wolof

ndaxte meru nit du jur njub gi neex yàlla.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

afin que l`homme de dieu soit accompli et propre à toute bonne oeuvre.

Wolof

noonu waayu yàlla ji dina mat, ba jekk ci bépp jëf ju rafet.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

bien-aimés, aimons nous les uns les autres; car l`amour est de dieu, et quiconque aime est né de dieu et connaît dieu.

Wolof

samay soppe, nanu bëggante, ndax mbëggeel ci yàlla la bawoo; képp ku bëgg sa mbokk nag, ci yàlla nga juddoo, te xam nga yàlla.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

ils lui dirent: que devons-nous faire, pour faire les oeuvres de dieu?

Wolof

noonu ñu laaj ko ne: «lu nu war a liggéey, ngir matal jëf yi neex yàlla?»

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car tous ont péché et sont privés de la gloire de dieu;

Wolof

Ñépp a bàkkaar, ba joteetuñu ndamu yàlla.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

accueillez-vous donc les uns les autres, comme christ vous a accueillis, pour la gloire de dieu.

Wolof

moo tax nangoonteleen, bay màggal yàlla, ni leen kirist nangoo.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car je vous ai annoncé tout le conseil de dieu, sans en rien cacher.

Wolof

ndaxte ñeebluwuma leen, ci di leen xamal lépp li yàlla digle.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

dieu nous les a révélées par l`esprit. car l`esprit sonde tout, même les profondeurs de dieu.

Wolof

fekk nag nun la ko yàlla won, jaarale ko ci xelam. xelum yàlla mooy leeral lépp, ba ci xalaati yàlla yi gën a xóot.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

adultères que vous êtes! ne savez-vous pas que l`amour du monde est inimitié contre dieu? celui donc qui veut être ami du monde se rend ennemi de dieu.

Wolof

yéen ñi fecci seen kóllëre ak yàlla, xanaa xamuleen ne mbëggeelu àddina, mbañeel la fa yàlla? ku bëgg a xaritoo ak àddina nag, noonoo nga ak yàlla.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

aussi la création attend-elle avec un ardent désir la révélation des fils de dieu.

Wolof

ndax li yàlla bind lépp a ngi ne seew a gis doomi yàlla yi feeñ ci seen biir ndam.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

afin que votre foi fût fondée, non sur la sagesse des hommes, mais sur la puissance de dieu.

Wolof

ngir seen ngëm bañ a wékku ci xam-xamu nit ñi waaye mu wékku ci dooley yàlla.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car la folie de dieu est plus sage que les hommes, et la faiblesse de dieu est plus forte que les hommes.

Wolof

li ñuy wax ag ndof ca wàllu yàlla moo gën a tedd xam-xamu nit. te li ñuy wax ñàkk dooley yàlla moo ëpp kàttan dooley nit.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

cherchez plutôt le royaume de dieu; et toutes ces choses vous seront données par-dessus.

Wolof

waaye wutleen nguuram, te loolu lépp dina leen ko ci dollil.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

ainsi, qu`on nous regarde comme des serviteurs de christ, et des dispensateurs des mystères de dieu.

Wolof

nañu nu teg kon ay surgay kirist, di ay jawriñ yuy xamle mbóoti yàlla.

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Franska

car, quiconque fait la volonté de dieu, celui-là est mon frère, ma soeur, et ma mère.

Wolof

ndaxte kuy def coobareg yàlla, kooku mooy sama rakk ak sama jigéen ak sama ndey.»

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
7,776,149,222 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK