From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
fan nga
Last Update: 2023-09-12
Usage Frequency: 1
Quality:
fan nga dek
Last Update: 2023-09-12
Usage Frequency: 1
Quality:
ku ko nuyu, bokk nga ciy ñaawteefam.
for he that biddeth him god speed is partaker of his evil deeds.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ku ma gis, gis nga ki ma yónni.
and he that seeth me seeth him that sent me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nga noopi, moo genn ngay toopa di wax.
being silent, is better than keeping on taking
Last Update: 2023-07-18
Usage Frequency: 1
Quality:
walla mu ñaan la jën, nga jox ko jaan?
or if he ask a fish, will he give him a serpent?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
fí, mön nga tann dara ci, ngir nga mbinde ko
multi-list settings. you can double-click a row to edit the values.
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
te maa ngi dellu di waxaat ne, képp kuy farataal xaraf, fàww nga sàmm lépp lu yoon wi santaane.
for i testify again to every man that is circumcised, that he is a debtor to do the whole law.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye man maa ngi leen di wax ne, képp ku xool jigéen, xédd ko, njaaloo nga ak moom ci sa xel.
but i say unto you, that whosoever looketh on a woman to lust after her hath committed adultery with her already in his heart.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi yeesu ñëwee, màrt yég ko, dem di dajeek moom; fekk booba maryaamaa nga toogoon ca kër ga.
then martha, as soon as she heard that jesus was coming, went and met him: but mary sat still in the house.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
naka la man a ame nag, nu di leen dégg, kenn ku nekk ci nun, ñuy wax ci sa làmmiñ, wi nga nàmp?
and how hear we every man in our own tongue, wherein we were born?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te yaxya daan ko wax: «jaaduwul nga denc ko.»
for john said unto him, it is not lawful for thee to have her.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye lii neex na ma ci yaw: sib nga ni man li ñoom nikolas di jëf. i
but this thou hast, that thou hatest the deeds of the nicolaitans, which i also hate.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yaa di jàngalekatu ñi jàngul ak xamlekatu ñi xamul, ndaxte xalaat nga ne, yàlla jagleel na leen ci yoonu musaa bépp xam-xam ak gépp dëgg.
an instructor of the foolish, a teacher of babes, which hast the form of knowledge and of the truth in the law.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye man maa ngi leen di wax ne, ku fase sa jabar te du ci njaaloo, yaa koy tegtal yoonu njaaloo. te it ku takk jigéen ju ñu fase, njaaloo nga.
but i say unto you, that whosoever shall put away his wife, saving for the cause of fornication, causeth her to commit adultery: and whosoever shall marry her that is divorced committeth adultery.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi mu déggee wax yooyu, kenn ca gan ya ne yeesu: «kiy lekk ci ñam, yi yàlla di joxe ci nguuram, barkeel nga!»
and when one of them that sat at meat with him heard these things, he said unto him, blessed is he that shall eat bread in the kingdom of god.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
def nga leen askanu saraxalekatibuur yàlla sunu boroom,di ko jaamu,te dinañu nguuru ci àddina.»
and hast made us unto our god kings and priests: and we shall reign on the earth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte am na fu ñu wax ci mbind mi ne:«lan mooy nit, yaw yàlla, ba nga di ko xalaat?lan mooy doomu nit, ba nga koy topptoo?
but one in a certain place testified, saying, what is man, that thou art mindful of him? or the son of man, that thou visitest him?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
dina jur doom ju góor; na nga ko tudde yeesu, ndaxte moo di kiy musal xeetam ci seeni bàkkaar.»
and she shall bring forth a son, and thou shalt call his name jesus: for he shall save his people from their sins.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nataneel ne ko: «noo ma xame?» yeesu tontu ko ne: «bi la filib di laata woo, gis naa la, bi nga nekkee ca ker garabu figg ga.»
nathanael saith unto him, whence knowest thou me? jesus answered and said unto him, before that philip called thee, when thou wast under the fig tree, i saw thee.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: