您搜索了: alifika (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

ilipokuwa jioni, yesu alifika pamoja na wanafunzi wake kumi na wawili.

沃洛夫语

bi nga xamee ne timis jot na, yeesu ñëw, ànd ak fukki taalibe yi ak ñaar.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

petro alipokuwa anasafirisafiri kila mahali alifika pia kwa watu wa mungu waliokuwa wanaishi luda.

沃洛夫语

piyeer nag di wër, di jaar fu nekk, tey dem ci gaayi yàlla yi dëkk lidd,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya kukaa huko siku kadhaa, nabii mmoja aitwaye agabo alifika kutoka yudea.

沃洛夫语

bi nu fa nekkee ay fan nag, yonent bu tudd agabus jóge yude, agsi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yesu alifika bethsaida pamoja na wanafunzi wake. huko watu wakamletea kipofu mmoja, wakamwomba amguse.

沃洛夫语

gannaaw loolu ñu ñëw ci betsayda. foofa ñu indil yeesu ku gumba, di ko ñaan, mu laal ko.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

siku hizo, yesu alifika kutoka nazareti, mji wa galilaya, akabatizwa na yohane katika mto yordani.

沃洛夫语

booba yeesu jóge na dëkku nasaret ci diiwaanu galile, ñëw, yaxya sóob ko ci dexu yurdan.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini msamaria mmoja aliyekuwa anasafiri, alifika pale yule mtu alipokuwa, naye alipomwona, alimwonea huruma.

沃洛夫语

waaye benn waay bu dëkk samari bu doon tukki, ñëw ba jege waa ja, gis ko, yërëm ko.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya hayo, yesu alifika mkoani yudea pamoja na wanafunzi wake. alikaa huko pamoja nao kwa muda, akibatiza watu.

沃洛夫语

gannaaw loolu yeesu ànd ak ay taalibeem, dem ca biir diiwaanu yude, toog fa ak ñoom ab diir, di sóob nit ñi ci ndox.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya siku chache, felisi alifika pamoja na mkewe drusila ambaye alikuwa myahudi. aliamuru paulo aletwe, akamsikiliza akiongea juu ya kumwamini yesu kristo.

沃洛夫语

bi ay fan wéyee, feligsë ñëwaat, ànd ak jabaram dursil, miy yawut. noonu mu woolu pool, di ko déglu ci mbirum gëm yeesu kirist.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

paulo alifika derbe na lustra, ambako aliishi mfuasi mmoja aitwaye timotheo. mama yake ambaye pia alikuwa mfuasi, alikuwa myahudi; lakini baba yake alikuwa mgiriki.

沃洛夫语

naka noona mu dikk dëkki derbë ak listar, fekk fa taalibe bu tudd timote te ndeyam di yawut bu gëm, waaye baayam di gereg.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

mmojawapo wa walimu wa sheria alifika, akasikia mabishano yao. alipoona kwamba yesu aliwajibu vyema, akajitokeza akamwuliza, "katika amri zote ni ipi iliyo ya kwanza?"

沃洛夫语

bi ñuy werante, benn xutbakat ñëw, dégg seen waxtaan, gis ne yeesu tontu na leen tont lu leer. mu laaj ko nag: «ci ndigal yi, ban moo ci gën a màgg?»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

yesu alifika katika nchi ya wagerasi, ng'ambo ya ziwa, na huko watu wawili waliopagawa na pepo wakakutana naye wakitokea makaburini. watu hawa walikuwa wenye kutisha mno, hata hakuna mtu aliyethubutu kupita katika njia hiyo.

沃洛夫语

bi yeesu jàllee nag, ba teer ca diiwaanu waa gadara, ñaar ñu rab jàpp daldi génn ca sëg ya, ñëw kar ko. Ñaar ñooñu nag, ñu soxor lañu woon, ba kenn ñemewul woon a jaar foofa.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yesu alipokuwa akisema hayo, ofisa mmoja myahudi alifika, akamwinamia na kusema, "binti yangu amekufa sasa hivi. lakini, tafadhali njoo umwekee mkono wako naye ataishi."

沃洛夫语

bi leen yeesu di wax loolu, benn njiitu jàngu daldi ñëw, sukk ci kanamam ne ko: «sama doom ju jigéen dafa faatu léegi, waaye ñëwal, teg ko say loxo, te dina dundaat.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,799,518,712 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認