您搜索了: ambalo (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

lakini yesu alikuwa anaongea juu ya hekalu ambalo ni mwili wake.

沃洛夫语

waaye kër yàlla, gi yeesu doon wax, nekkul woon ab tabax, aw yaramam ci boppam moo ko taxoon di wax.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

inafahamika wazi kwamba yeye alizaliwa katika kabila la yuda ambalo mose hakulitaja alipokuwa anasema juu ya makuhani.

沃洛夫语

li wóor moo di, sunu boroom mi ngi soqikoo ci giiru yuda. te bi musaa bindee ci mbirum saraxalekat yi, limaalewul woon giir googu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baadhi ya mafarisayo wakawauliza, "mbona mnafanya jambo ambalo si halali siku ya sabato?"

沃洛夫语

am ay farisen yu ne: «lu tax ngeen di def lu jaaduwul ci bésu noflaay bi?»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

na ya kwamba kila mmoja anayemwamini yesu anasamehewa dhambi zote, jambo ambalo halingewezekana kwa njia ya sheria ya mose.

沃洛夫语

fa la yeesu di àttee ni ku jub képp ku ko gëm.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

heri mtu anayebaki mwaminifu katika majaribu, kwani akisha stahimili atapewa tuzo la uzima ambalo mungu aliwaahidia wale wanaompenda.

沃洛夫语

ku dékku nattu, ku barkeel nga, ndax boo ci génnee ak ndam, dees na la jagleel kaalag dund, gi yàlla dig ñi ko bëgg.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

mahali hapo aliposulubiwa yesu palikuwa na bustani, na katika bustani hiyo kulikuwa na kaburi jipya ambalo hakutiwa bado mtu yeyote ndani yake.

沃洛夫语

tool a nga woon ca wetu bérab, ba ñu daajoon yeesu, te ca tool booba amoon na fa bàmmeel bu ñu musul a suul kenn.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, akafika sukari, mji mmoja wa samaria, karibu na shamba ambalo yakobo alikuwa amempa mwanawe, yosefu.

沃洛夫语

noonu mu agsi ci wetu dëkku sikar ci tool, bi yanqóoba mayoon doomam yuusufa.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

maana sheria ya mose haikuweza kukamilisha jambo lolote. lakini sasa, mahali pake pamewekwa tumaini lililo bora zaidi ambalo kwalo tunaweza kumkaribia mungu.

沃洛夫语

--ndax yoonu musaa yeggalewul dara cig mat — waaye dugalal nañu nu fii yaakaar ju gën ju nu man a jaare ngir jege yàlla.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

jihadharini wenyewe; lilindeni lile kundi ambalo roho mtakatifu amewaweka ninyi muwe walezi wake. lichungeni kanisa la mungu ambalo amejipatia kwa damu ya mwanae.

沃洛夫语

wottuleen nag seen bopp te wottu coggal jépp, ji leen xel mu sell mi def sàmm, ngeen sàmm mbooloo, mi yàlla jotal boppam ak deretu doomam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hilo lilikuwa jambo ambalo hatukulitazamia kabisa! kwanza walijitolea wao wenyewe kwa bwana, kisha wakajitolea wenyewe kwetu pia, kufuatana na mapenzi ya mungu.

沃洛夫语

te yemuñu sax ci li nu séentu woon ci ñoom, waaye dañoo jébbal seen bopp boroom bi jëkk, gannaaw loolu ñu jébbal nu seen bopp ci coobareg yàlla.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ikiwa basi mungu hulivika hivyo jani la shambani ambalo leo liko na kesho latupwa motoni, je, hatafanya zaidi kwenu ninyi? enyi watu wenye imani haba!

沃洛夫语

yéen ñi néew ngëm! bu yàlla woddee nii ñaxum tool yi, miy sax tey, te bu subaa ñu def ko ci taal bi, ndax du leen gën a wodd?

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini kama nikicheleweshwa, basi, barua hii itakufahamisha mwenendo tunaopaswa kuwa nao katika nyumba ya mungu, ambayo ni kanisa la mungu aliye hai, na ambalo ni nguzo na msingi wa ukweli.

沃洛夫语

waaye amaana mu yéex. moo tax ma lay bind bataaxal bii, ngir xamal la, ni ñu war a nekke ci kër yàlla gi, maanaam ci mbooloom yàlla aji dund ji, miy kenug dëgg te di sëslaayam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

mungu ametekeleza jambo lile ambalo sheria haikuweza kutekeleza kwa sababu ya udhaifu w binadamu. mungu alimtuma mwanae akiwa mwenye mwili sawa na miili yetu sisi wenye dhambi, ili aikabili dhambi, na kwa mwili huo akaiangamiza dhambi.

沃洛夫语

lu yoonu musaa mënul woon a def, ndax néew dooley nit, yàlla defe na ko nii: dafa yónni doomam, ngir mu yor sunu jëmm, nun ñiy nekk ay bàkkaarkat, te mu jébbale bakkanam, ngir dindi bàkkaar yi. noonu la yàlla tase nguuru bàkkaar ci nit.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"aliye na masikio, basi, na asikie yale roho anayoyaambia makanisa! "wale wanaoshinda nitawapa ile mana iliyofichika. nitawapa pia jiwe jeupe lililoandikwa jina jipya ambalo hakuna mtu aliyelijua isipokuwa tu wale wanaolipokea.

沃洛夫语

yaw mi am ay nopp, déglul li xelum yàlla di wax mboolooy ñi gëm. ku daan, dinaa la jox, nga lekk dund bi ñuy wax mànn te mu nëbbu, te dinaa la jox xeer wu weex. ci kaw xeer woowu bindees na ci tur wu bees wu kenn xamul, ku dul ki ko jot.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
8,045,154,937 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認