您搜索了: baraka (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

watakieni baraka wale wanaowalaani, na waombeeni wale wanaowatendea vibaya.

沃洛夫语

yéeneleen lu baax ñi leen di móolu, te ñaanal ñi leen di sonal.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

najua ya kuwa nikija kwenu nitawaletea wingi wa baraka za kristo.

沃洛夫语

te wóor na maa ne, bu ma agsee ci yéen, dinaa indaale barkeb kirist bu mat sëkk.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kwa imani isaka aliwabariki yakobo na esau, wapate baraka zitakazokuja baadaye.

沃洛夫语

te it ngëm moo tax ba isaaxa barkeel yanqóoba ak esawu, di wax ci mbirum yëf yiy ñëw.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

watakieni baraka wote wanaowadhulumu ninyi; naam, watakieni baraka na wala msiwalaani.

沃洛夫语

ku leen fitnaal, ñaanal-leen ko yiw, te bañ koo móolu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

nikiwa na matumaini hayo, nilikusudia kuja kwenu hapo awali ili mpate baraka maradufu.

沃洛夫语

kon ni ma ame woon kóolute googu, naroon naa jëkk a jaar ci yéen, ngir ganesi leen ñaari yoon.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

mitume walishuhudia kwa nguvu nyingi kufufuka kwa bwana yesu, naye mungu akawapa baraka nyingi.

沃洛夫语

te ndaw yi di seedeel ndekkitel yeesu boroom bi ak kàttan gu réy. te yiw wu yaatu ëmb leen, ñoom ñépp.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

naomba ili imani hiyo unayoshiriki pamoja nasi ikuwezeshe kuwa na ujuzi mkamilifu zaidi wa baraka zote tunazopata katika kuungana kwetu na kristo.

沃洛夫语

li may ñaan nag a ngi nii: nga xam bu wér ngëneel, yi nu am yépp ci sunu bokk ci kirist, ba tax bokk gi nga am ci yàlla ci kaw ngëm meññ i njariñ.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

tena twataabika na kufanya kazi kwa mikono yetu wenyewe. tukitukanwa, tunawatakia baraka; tukidhulumiwa, tunavumilia;

沃洛夫语

nu ngi ñaq di jariñoo. ku nu saaga, nu ñaanal la lu baax. coono bu ñu nu teg, nu tegoo ko.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

msiwalipe watu ovu kwa ovu, au tusi kwa tusi; bali watakieni baraka, maana ninyi mliitwa na mungu mpate kupokea baraka.

沃洛夫语

ku la def lu bon mbaa mu saaga la, bul feyyu, waaye ñaanal ko lu baax; ndaxte ci loolu la leen yàlla woo, ngir barkeel leen.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

jambo hili lilifanyika kusudi ile baraka aliyopewa abrahamu iwashukie watu wa mataifa mengine kwa njia ya kristo, na ili kwa imani, tumpokee yule roho ambaye mungu alituahidia.

沃洛夫语

noonu barke bi yàlla dig ibraayma baawaan na, ba daj ñi dul yawut te gëm kirist yeesu, te nu jot ci kaw ngëm xel mu sell, mi yàlla dige.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kwa hiyo, basi, muwe tayari kabisa kwa nia, na kukesha. wekeni tumaini lenu lote katika baraka ile mtakayopewa wakati yesu kristo atakapoonekana!

沃洛夫语

kon fagaruleen ci seeni xalaat te maandu, di wékk seen yaakaar jépp ci yiw, wi leen yàlla di jagleel bés bu yeesu kirist di feeñ.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"na sasa basi, ninawaweka ninyi chini ya ulinzi wa mungu na ujumbe wa neema yake. yeye anao uwezo wa kuwajenga ninyi na kuwawezesha mzipate zile baraka alizowawekea watu wake.

沃洛夫语

«léegi nag maa ngi leen di dénk boroom bi, moom ak kàddug yiwam, gi leen man a dëgëral te may leen cér ci biir gaayi yàlla yu sell yépp.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

kosa la wayahudi limesababisha baraka nyingi kwa ulimwengu, na utovu wao kwa kiroho umeleta baraka nyingi kwa watu wa mataifa mengine. basi, ni dhahiri zaidi kwamba utimilifu wao utasababisha baraka nyingi zaidi.

沃洛夫语

gannaaw seen tooñ nag moo ubbi buntu yiw ci waa àddina si, te seen ñàkk moo meññ barkeb xeet yépp, céy bés bu israyil gépp delloo ci yàlla, ndaw barke bu bare!

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, kwa vile sisi ni watoto wa mungu, tutapokea baraka zote mungu alizowawekea watu wake, na tutashiriki urithi huo pamoja na kristo; maana, tukiyashiriki mateso yake kristo, tutaushiriki pia utukufu wake.

沃洛夫语

te gannaaw ay doomi yàlla lanu, dinanu moomi lépp li yàlla jagleel ay doomam, séddu ci ngëneel yi kirist yelloo. waaye nag ku bëgg a bokk ak kirist ndamam ëllëg, war ngaa séddu ci ay fitnaam tey.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,793,997,233 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認