您搜索了: iliyokuwa (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

huko, tulikuta meli iliyokuwa inakwenda foinike, hivyo tulipanda, tukasafiri.

沃洛夫语

foofa nag nu gis gaal guy jàll ba fenisi, nu dugg ca, mu daldi teddi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hapo yule ofisa alikuta meli moja ya aleksandria iliyokuwa inakwenda italia, na hivyo akatupandisha ndani.

沃洛夫语

foofa nag njiit la gis gaal gu jóge alegsàndiri, jëm itali, mu dugal nu ca.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alifutilia mbali ile hati ya deni iliyokuwa inatukabili na masharti yake, na kuifuta kabisa kwa kuipigilia msalabani.

沃洛夫语

mbind mi nu doon tiiñal, te daa nu yey ndax ay sàrtam, yàlla far na ko, dindi ko, daajaale ko ca bant, ba kirist deeye.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hata simoni aliamini; baada ya kubatizwa ilikuwa akiandamana na filipo, akastaajabia maajabu na miujiza iliyokuwa inafanyika.

沃洛夫语

simoŋ sax gëm, ñu sóob ko ci ndox; mu wéy nag ci topp filib, di waaru ci kéemaan yi ak firnde yu mag yiy am.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ghafla, sauti ikasikika kutoka angani; sauti iliyokuwa kama ya upepo mkali, ikajaza ile nyumba yote walimokuwa wamekaa.

沃洛夫语

ca saa sa riir jollee asamaan, mel ni ngelaw lu gaaw te bare doole, daldi fees dell kër, ga ñu toog.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hivyo walitafuta kina cha bahari kwa kuteremsha kamba iliyokuwa imefungiwa kitu kizito, wakapata kina cha mita arobaini. baadaye wakapima tena wakapata mita thelathini.

沃洛夫语

Ñu sànni nattukaay ba ci biir géej, mu jàpp ñeent-fukki meetar, dem ca kanam tuuti, sànniwaat ko, jàpp fanweeri meetar.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ninyi mnafahamu kwamba hata alipotaka kuipata tena ile baraka iliyokuwa yake, alikataliwa, maana hakupata tena nafasi ya kutubu, ingawa aliitafuta kwa machozi.

沃洛夫语

xam ngeen ne, ba ñu ca tegee tuuti, gàntu nañu ko, ba mu bëggee jot barke bi. amul fenn fu mu jaar ba defar njuumteem, te jooy, yi mu doon jooy, mënu ci dara.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, nikasikia sauti kutoka mbinguni, sauti iliyokuwa kama sauti ya maji mengi na kama sauti ya ngurumo kubwa. sauti niliyosikia ilikuwa kama sauti ya wachezaji muziki wakipiga vinubi vyao.

沃洛夫语

ma dégg baat bu jóge asamaan, buy riir ni duusi géej, ni riiru dënnu gu réy. baat ba ma dégg mel ni baati xalamkat yuy xalam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya yesu kuingia katika mashua moja, iliyokuwa ya simoni, alimtaka simoni aisogeze majini, mbali kidogo na ukingo wa ziwa. akaketi, akafundisha umati wa watu akiwa ndani ya mashua.

沃洛夫语

mu dugg ci genn gaal, fekk muy gu simoŋ, mu ne ko, mu joow ba sore tuuti. noonu yeesu toog ca gaal ga, di jàngal mbooloo ma.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kwa imani abeli alimtolea mungu dhabihu iliyokuwa bora zaidi kuliko ile ya kaini. kwa imani yake alikubaliwa na mungu kuwa mwadilifu; mungu mwenyewe alizikubali sadaka zake. kwa imani yake ingawa amekufa, bado ananena.

沃洛夫语

ngëm moo tax ba abel jébbal yàlla sarax su gën saraxu kayin. ngëmu abel moo tax ba yàlla àtte ko ni ku jub, bi mu ko seedeelee ne, saraxam baax na. te ci kaw ngëm lay wax ba tey, moom mi dee ba noppi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

humo mlikuwa na madhabahu ya dhahabu kwa ajili ya kufukizia ubani, na sanduku la agano, ambalo lilikuwa limepakwa dhahabu pande zote, na ndani yake mlikuwa na chungu cha dhahabu kilichokuwa na mana; fimbo ya aroni iliyokuwa imechanua majani, na vile vibao viwili vilivyoandikwa agano.

沃洛夫语

saraxalukaayu wurus, ba ñuy taal cuuraay ca kawam, a nga fa woon, ak gaalu kóllëre, ga ñu taf wurus ba mu daj. ca biir gaal ga amoon na fa benn njaqu wurus bu defoon ñam, wi ñuy wax mànn, ak it yetu aaroona wi jebbi woon, ak àlluway doj, ya ñu bindoon wax yi kóllëre gi ëmb.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
8,025,632,529 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認