您搜索了: kumwamini (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

sasa basi jueni kwamba watu wenye kumwamini ndio walio watoto halisi wa abrahamu.

沃洛夫语

xamleen boog ne, boroom ngëm yi rekk ñooy doomi ibraayma.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini wale wote waliompokea na kumwamini, hao aliwapa uwezo wa kuwa watoto wa mungu.

沃洛夫语

teewul ñi ko nangu te gëm ci turam, may na leen, ñu am sañ-sañu nekk doomi yàlla.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

huyo mtu akajibu, "mheshimiwa, niambie yeye ni nani, ili nipate kumwamini."

沃洛夫语

waa ja ne ko: «wax ma mooy kan, sang bi, ba ma man koo gëm.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

niliwaonya wote--wayahudi kadhalika na watu wa mataifa, wamgeukie mungu na kumwamini bwana wetu yesu.

沃洛夫语

dénk naa yawut yi ak gereg yi ne leen, ñu tuub seeni bàkkaar, ba woññiku ci yàlla te gëm sunu boroom yeesu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kutokana na hayo, ni lazima watu wa mungu, yaani watu wanaotii amri ya mungu na kumwamini yesu, wawe na uvumilivu.

沃洛夫语

looloo tax gaayi yàlla yi war a muñ, ñooñuy sàmm ndigali yàlla yi ak ngëm ci yeesu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

salamu zangu pia kwa kanisa linalokutana nyumbani kwao. salamu zangu zimfikie rafiki yangu epaineto ambaye ni kwa kwanza katika mkoa wa asia kumwamini kristo.

沃洛夫语

nuyul-leen ma it ñiy booloo ci seen kër.maa ngi nuyu it epaynet, mi jëkk a gëm kirist ci diiwaanu asi;

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya siku chache, felisi alifika pamoja na mkewe drusila ambaye alikuwa myahudi. aliamuru paulo aletwe, akamsikiliza akiongea juu ya kumwamini yesu kristo.

沃洛夫语

bi ay fan wéyee, feligsë ñëwaat, ànd ak jabaram dursil, miy yawut. noonu mu woolu pool, di ko déglu ci mbirum gëm yeesu kirist.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

maana anachotaka baba yangu ndicho hiki: kila amwonaye mwana na kumwamini awe na uzima wa milele; nami nitamfufua siku ya mwisho."

沃洛夫语

ndaxte lii mooy bëgg-bëggu baay bi: képp ku gis doom ji te gëm ko, am dund gu dul jeex, te bés bu mujj ba, dinaa ko dekkal!»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

nimewaandikieni barua hii fupi kwa msaada wa silwano, ndugu ambaye namjua na kumwamini. nataka kuwapeni moyo na kushuhudia kwamba jambo hili ni neema ya mungu kweli. kaeni imara katika neema hiyo.

沃洛夫语

bind naa leen ci lu gàtt ci ndimbalu silwan, mi ma jàpp ni sama mbokk mu takku. dénk naa leen, di leen seedeel ne, lii mooy yiwu yàlla dëgg; kon nag saxleen ci.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"kweli nawaambieni, anayesikia neno langu, na kumwamini yule aliyenituma, anao uzima wa milele. hatahukumiwa kamwe, bali amekwisha pita kutoka kifo na kuingia katika uzima.

沃洛夫语

«ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku dégg sama kàddu te gëm ki ma yónni, am nga dund gu dul jeex te doo jaar ca àtte ba, ndaxte génn nga ci dee, tàbbi ci dund.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

lakini, tunajua kwa hakika kwamba mtu hawezi kukubaliwa kuwa mwadilifu kwa kuitii sheria, bali tu kwa kumwamini yesu kristo. na sisi pia tumemwamini yesu kristo ili tupate kukubaliwa kuwa waadilifu kwa njia ya imani yetu kwa kristo, na si kwa kuitii sheria.

沃洛夫语

teewul nu xam ne, yàlla du àtte kenn ni ku jub ci kaw sàmm yoon, waaye ci gëm yeesu kirist. kon nun itam gëm nanu kirist yeesu, ngir yàlla àtte nu jub ci kaw gëm kirist, te du ci sàmm yoon. ndaxte du caageenug sàmm yoon mooy tax yàlla àtte kenn ni ku jub.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,793,322,357 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認