您搜索了: labda (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

nahofu kwamba labda kazi niliyoifanya kwa ajili yenu imepotea bure!

沃洛夫语

sama xel dalul ci yéen, ngir ragal sama coono ci yéen neen.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

labda onesimo aliondoka kwako kwa kitambo tu, kusudi uweze tena kuwa naye daima.

沃洛夫语

xëy na sax dafa tàggoo woon ak yaw diir bu gàtt, ngir nga jotaat ci ba fàww;

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

naye akawajibu, la, msije labda mnapokusanya magugu, mkang'oa na ngano pia.

沃洛夫语

waaye mu tontu leen: “déedéet, ngir bañ a buddiwaale dugub ji, bu ngeen koy dindi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

si rahisi mtu kufa kwa ajili ya mtu mwadilifu; labda mtu anaweza kuthubutu kufa kwa ajili ya mtu mwema.

沃洛夫语

kuy nangoo deeyal nit ku jub, yombul a gis, waaye nag jombul am na ku nangoo deeyal ku baax.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yule mwenye shamba akafikiri: nitafanya nini? nitamtuma mwanangu mpenzi; labda watamjali yeye.

沃洛夫语

«boroom tool ba daldi ne: “nan laay def nag? dinaa yónni sama doom, sama reeni xol. xëy na ñu weg ko, moom.”

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

labda sina ufasaha wa lugha, lakini elimu ninayo; jambo hili tumelionyesha wazi kwenu, kila mahali na kila wakati.

沃洛夫语

bu ma dul jàmbaari wax it, néewuma xam-xam, te won nanu leen ko ci bépp mbir ak ci bépp fànn.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

au labda unaudharau wema wake mkuu, uvumilivu wake na saburi yake, bila kutambua kwamba wema wake huo una shabaha ya kukuongoza upate kutubu?

沃洛夫语

ndax dangaa xeeb mbaaxu yàlla, mi yéex a mer te di la muñal? xanaa xamuloo ne, yàllaa ngi lay won baaxaayam, ngir nga réccu say bàkkaar?

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

labda nitakaa kwenu kwa muda fulani, au huenda nitakaa pamoja nanyi wakati wote wa baridi, ili mpate kunisaidia niendelee na safari yangu kokote nitakakokwenda.

沃洛夫语

man na am ma yàgg ci yéen, jombul sax ma lollikoo fi yéen. noonu dingeen taxawu sama yoon, fu ma man a jëm.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

labda utaniuliza: "ikiwa mambo yako hivyo, mungu anawezaje kumlaumu mtu? nani awezaye kuyapinga mapenzi yake?"

沃洛夫语

waaye xanaa dina am ku may wax ne: «gannaaw kenn mënul a bañ coobareg yàlla, lu tax kon muy teg nit tooñ?»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

msifadhaike upesi moyoni, na wala msitiwe wasiwasi kwa sababu ya madai kwamba siku ya bwana imekwisha fika. labda inadhaniwa kwamba jambo hili limetokana na uaguzi fulani, mahubiri au barua inayosemekana kuwa imetoka kwetu.

沃洛夫语

bu leen kenn gaaw a tàggale ak seen sago, mbaa di leen jaaxal, muy yonent buy wax, muy kàddu mbaa bataaxal bu ñu nu moomaleel, ci ne leen bésu boroom bi ñëw na xaat.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, mtakubali kwamba sikuwa mzigo kwenu. lakini labda mtu mwingine atasema: "kwa vile paulo ni mwerevu, amewafanyieni ulaghai."

沃洛夫语

kon noonu la, nekkuma woon yen ci yéen. waaye man na am ñu naan, dama leen a nax, ba réeral leen ci sama njublaŋ.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

au, labda wewe wajifanya mkuu kuliko babu yetu yakobo? yeye alitupa sisi kisima hiki; na yeye mwenyewe, watoto wake na mifugo yake walikunywa maji ya kisima hiki."

沃洛夫语

xanaa kay xalaatuloo ne, yaa gën a màgg sunu maam yanqóoba, moom mi nu gasal teen bii, mu naan ci moom ak i doomam, wëgg cig juram?»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

labda mnafikiri kwamba mpaka sasa tumekuwa tukijitetea wenyewe mbele yenu! lakini, tunasema mambo haya mbele ya mungu, tukiwa tumeungana na kristo. mambo hayo, yote, wapenzi wangu, ni kwa ajili ya kuwajenga ninyi.

沃洛夫语

xanaa diirub li ngeen di jàng lii, defe ngeen ne, nu ngi wut aw lay ci seen kanam. samay xarit, nu ngi leen di wax ci kanam yàlla ak ci turu kirist; te lépp ngir seen njariñ la.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,748,347,285 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認