您搜索了: mbali (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

mfukuzeni mbali nanyi huyo mwovu!

沃洛夫语

Ñi bokkul ci mbooloom ñi gëm, yàlla moo leen di àtte. waaye yéen, ni ko mbind mi waxe: «dàqleen ci seen biir kiy def lu bon.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alipomwona yesu kwa mbali, alimkimbilia, akamwinamia

沃洛夫语

bi mu gisee yeesu fu sore nag, mu daldi dawsi, sukk fa kanamam,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

walikuta lile jiwe limeviringishwa mbali na kaburi.

沃洛夫语

bi ñu agsee, ñu fekk ñu béraŋ doj, wa uboon bàmmeel ba.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

naye akatupilia mbali vazi lake, akaruka juu, akamwendea yesu.

沃洛夫语

bi mu ko déggee, mu sànni malaanam, ne bërét, dem ci yeesu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

mlipokuwa watumwa wa dhambi, mlikuwa huru mbali na uadilifu.

沃洛夫语

ndaxte keroog ba ngeen nekkee jaami bàkkaar, séquleen woon dara ak lu jub.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

adhabu yao itakuwa kuangamizwa milele na kutengwa mbali na utukufu wake mkuu,

沃洛夫语

seen pey mooy alku ba fàww, ñu dàq leen fu sore boroom bi ak ndamam lu réy.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yeyote yule ambaye hatamsikiliza nabii huyo atatengwa mbali na watu wa mungu na kuangamizwa.

沃洛夫语

képp ku déggalul yonent boobu, dees na la far ci xeet wi.”

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

naye bwana akaniambia: nenda; ninakutuma mbali kwa mataifa mengine."

沃洛夫语

waaye boroom bi ne ma: “demal, dinaa la yebal fu sore, nga jëm ci xeeti ñi dul yawut.”»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

atamkatilia mbali na kumweka kundi moja na wanafiki. huko kutakuwa na kilio na kusaga meno.

沃洛夫语

dina ko dóor ay yar yu metti, jox ko añub naaféq. foofa dees na fa jooy tey yéyu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

tuko imara daima. tunajua kwamba kuishi katika mwili huu tu ni kukaa mbali na bwana.

沃洛夫语

noonu kon nu ngi fees ak kóolute fu nu tollu; te xam nanu ne, fi ak nu ngi dëkk ci yaram wii, àggagunu sunu màkkaan ci wetu boroom bi —

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alifutilia mbali ile hati ya deni iliyokuwa inatukabili na masharti yake, na kuifuta kabisa kwa kuipigilia msalabani.

沃洛夫语

mbind mi nu doon tiiñal, te daa nu yey ndax ay sàrtam, yàlla far na ko, dindi ko, daajaale ko ca bant, ba kirist deeye.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

haifai kitu wala kwa udongo wala kwa mbolea. watu huitupilia mbali. sikieni basi, kama mna masikio!"

沃洛夫语

du jariñ suuf, te du nekk tos. dañu koy sànni ca biti. déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, wakamkamata, wakamchukua na kwenda naye nyumbani kwa kuhani mkuu. petro akawa anamfuata nyuma kwa mbali.

沃洛夫语

Ñu jàpp yeesu, yóbbu ko ca kër saraxalekat bu mag ba. piyeer topp fu sore.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"baada ya kukaa mbali kwa miaka kadhaa, nilirudi yerusalemu ili kuwapelekea wananchi wenzangu msaada na kutoa dhabihu.

沃洛夫语

«noonu gannaaw gëjeb at yu bare ñëw naa, ngir indil sama xeet ndimbal te jébbal yàlla ay sarax.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

baada ya siku chache, yule mdogo aliuza urithi wake, akasafiri na fedha aliyopata, akaenda nchi ya mbali ambako aliitumia ovyo.

沃洛夫语

ay fan yu néew gannaaw gi, caat ma fab yëfam yépp, dem ca réew mu sore, yàq fa alalam ci topp nafsoom.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya hayo, mwisho utafika wakati ambapo kristo atamkabidhi mungu baba utawala, baada ya kufutilia mbali kila tawala na mamlaka na nguvu.

沃洛夫语

gannaaw ga, mujug jamono taxaw, te kirist dina noot gépp kilifa ak bépp sañ-sañ ak doole, ba noppi delloo nguur gi kiy yàlla di baayam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, kristo alikuja akahubiri habari njema ya amani kwenu ninyi watu wa mataifa mengine mliokuwa mbali na mungu, na pia kwa wayahudi ambao walikuwa karibu na mungu.

沃洛夫语

bi mu ko defee mu ñëw, yégalsi nu xebaaru jàmm fa kanam yàlla, yéen ñi sore woon ak nun ñi jege.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, akaanza safari ya kurudi kwa baba yake. alipokuwa bado yu mbali, baba yake alimwona, na kwa moyo wa huruma alimkimbilia, akamkumbatia na kumbusu.

沃洛夫语

«mu daldi jóg, jëm kër baayam. waaye bi muy soreendi kër ga, baayam séen ko, yërëm ko, daldi daw laxasu ko, fóon ko.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alifanya hivyo, ili mataifa hayo yapate kumfuata, na kama vile kwa kupapasapapasa, yapate kumfikia. hata hivyo lakini, mungu hayuko mbali na kila mmoja wetu.

沃洛夫语

yàlla def na loolu, ngir ñu koy wut ci yaakaaru daj ko ci làmbatu, fekk sax sorewul kenn ci nun.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, kama mtu atajitakasa kwa kujitenga mbali na mambo hayo yote maovu, atakuwa chombo cha matumizi ya pekee, kwa sababu amewekwa wakfu, anamfaa bwana wake na yupo tayari kwa kila kazi njema.

沃洛夫语

kon nag ku laabal sa bopp ci yooyu yépp, dinga nekk ndab lu tedd te sell, nga am njariñ ci boroom bi te jekk ci bépp jëf ju rafet.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,787,992,791 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認