您搜索了: mengi (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

wakamtolea maneno mengi ya matusi.

沃洛夫语

Ñu ngi ko doon tifaar it yeneeni saaga.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

makuhani wakuu wakamshtaki yesu mambo mengi.

沃洛夫语

te saraxalekat yu mag yi di ko jiiñ lu bare.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yesu aliposhuka kutoka mlimani, makundi mengi ya watu yalimfuata.

沃洛夫语

bi loolu amee yeesu wàcc ca tund wa, te mbooloo mu bare topp ko.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"ninayo bado mengi ya kuwaambieni, ila kwa sasa hamwezi kuyastahimili.

沃洛夫语

«li ma leen war a wax bare na, waaye dungeen ko man a dékku.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

aliwafundisha mambo mengi kwa mifano, na katika mafundisho yake aliwaambia,

沃洛夫语

noonu yeesu daldi leen jàngal lu bare ciy léeb. ci njàngaleem nag mu ne leen:

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, akamwuliza maswali mengi kwa muda mrefu, lakini yesu hakumjibu neno.

沃洛夫语

noonu mu laaj ko ay laaj yu bare, waaye yeesu tontuwul dara.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, joka likatapika maji mengi kama mto, yakamfuata huyo mama nyuma ili yamchukue.

沃洛夫语

ninkinànka ja buusu ndox mu bare ni dex ca gannaaw jigéen ja, ngir yóbbaale ko ca.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

hapo, makundi mengi yakawa yanaandamana pamoja na yesu. basi, akawageukia akawaambia,

沃洛夫语

am mbooloo yu réy yu toppoon ci yeesu, ba muy dem ca yoon wa. mu geestu ne leen:

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alipitia sehemu za nchi zile akiwatia watu moyo kwa maneno mengi. halafu akafika ugiriki.

沃洛夫语

noonu mu jaar ca bérab yooyu, di dooleel nit ñi ak wax yu bare; ba noppi mu dem réewu geres,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

bwana amjalie huruma katika siku ile! nawe wajua vizuri mengi aliyonifanyia huko efeso.

沃洛夫语

na ko boroom bi teeru ak yërmandeem ca bés ba. umplewoo it coono yi mu daj, ngir dimbali ma ca dëkku efes.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

atapokea mengi zaidi wakati huu wa sasa, na kupokea uzima wa milele wakati ujao."

沃洛夫语

dinga am tey jii ay yooni yoon, ak dund gu dul jeex ëllëg.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

alipokuwa akitoka pale, wale mafarisayo na walimu wa sheria wakaanza kumshambulia vikali na kumsonga kwa maswali mengi

沃洛夫语

bi yeesu génnee bérab boobu, farisen ya ak xutbakat ya ëmbal ko mer te di ko seetlu ci fànn gu nekk,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini habari za yesu zilizidi kuenea kila mahali. watu makundi mengi wakakusanyika ili kumsikiliza na kuponywa magonjwa yao.

沃洛夫语

noonu turu yeesu di gën a siiw. mbooloo mu bare di ñëw ci moom, ngir déglu ko te mu faj seeni jàngoro.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kisha akawaambia mfano: "kulikuwa na tajiri mmoja ambaye shamba lake lilizaa mavuno mengi.

沃洛夫语

noonu mu dégtal leen wii léeb ne: «dafa amoon waa ju bare alal, te ay toolam nangu lool,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, ungamanianeni dhambi zenu, na ombeaneni, ili mpate kuponywa. sala ya mtu mwema ina nguvu ya kutenda mengi.

沃洛夫语

kon nag waxanteleen seeni bàkkaar tey ñaanalante, ngir ngeen wér. Ñaanu aji jub gu dëggu, dooleem amul kem.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"mnaposali, msipayuke maneno kama watu wasiomjua mungu. wao hudhani kwamba mungu atawasikiliza ati kwa sababu ya maneno mengi.

沃洛夫语

«te it bu ngeen di ñaan, buleen bareel wax yu amul njariñ, mel ni ñi xamul yàlla; ñoom defe nañu ne, yàlla dina leen nangul ndax seen wax ju bare.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

kwa maneno mengine mengi, petro alisisitiza na kuwahimiza watu akisema, "jiokoeni katika kizazi hiki kiovu."

沃洛夫语

noonu mu artu leen ak yeneen wax yu bare, di leen dénk ne: «rëccleen ci niti jamono ju dëng jii.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

kuna mambo mengine mengi aliyofanya yesu, ambayo kama yangeandikwa yote, moja baada ya lingine, nadhani hata ulimwengu wenyewe usingetosha kuviweka vitabu ambavyo vingeandikwa.

沃洛夫语

yeesu def na yeneen jëf yu bare. su ñu ko doon nettali, bind lépp, xalaat naa ne, téere yi duñu xaj ci àddina.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

akawaambia, "mavuno ni mengi, lakini wavunaji ni wachache. kwa hivyo, mwombeni mwenye shamba atume wavunaji shambani mwake.

沃洛夫语

mu ne leen: «ngóob mi yaatu na, waaye liggéeykat yi barewuñu. Ñaanleen nag boroom ngóob mi, mu yebal ay liggéeykat, ñu góob toolam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, nikasikia sauti kutoka mbinguni, sauti iliyokuwa kama sauti ya maji mengi na kama sauti ya ngurumo kubwa. sauti niliyosikia ilikuwa kama sauti ya wachezaji muziki wakipiga vinubi vyao.

沃洛夫语

ma dégg baat bu jóge asamaan, buy riir ni duusi géej, ni riiru dënnu gu réy. baat ba ma dégg mel ni baati xalamkat yuy xalam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

获取更好的翻译,从
7,745,568,273 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認