您搜索了: mrefu (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

wakakaa pamoja na wale waumini kwa muda mrefu.

沃洛夫语

noonu ñu toog ak taalibe ya diir bu yàgg.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

walimwomba akae nao muda mrefu zaidi, lakini hakupenda.

沃洛夫语

Ñu ñaan ko, mu des fa lu gën a yàgg, waaye nanguwul.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

walivutiwa sana naye kwa vile alikuwa amewashangaza kwa uchawi wake kwa muda mrefu.

沃洛夫语

Ñu taq ci moom, ndax li mu leen yàgg a waar ci ay luxus.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, akamwuliza maswali mengi kwa muda mrefu, lakini yesu hakumjibu neno.

沃洛夫语

noonu mu laaj ko ay laaj yu bare, waaye yeesu tontuwul dara.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kisha ibilisi akamchukua mpaka juu ya mlima mrefu, akamwonyesha falme zote za ulimwengu na fahari zake,

沃洛夫语

gannaaw loolu seytaane yóbbu ko ci kaw tund wu kawe lool, won ko réewi àddina yépp ak seeni ndam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yuda na sila, ambao nao walikuwa manabii, walizungumza na hao ndugu kwa muda mrefu wakiwatia moyo na kuwaimarisha.

沃洛夫语

te yudd ak silas, ñi doon yonent, ñuy dooleel bokk yi, di dëgëral seen fit ak wax yu bare.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"baada ya muda mrefu, yule bwana alirudi, akaanza kukagua hesabu ya matumizi na mapato ya fedha yake.

沃洛夫语

«gannaaw diir bu yàgg njaatigeb surga ya dellusi, daldi leen laaj alalam.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, roho akanikumba, naye malaika akanipeleka juu ya mlima mrefu sana. akanionyesha mji mtakatifu, ukishuka kutoka kwa mungu mbinguni,

沃洛夫语

noonu xelum yàlla solu ma, malaaka ma yóbbu ma ci kaw tund wu réy-a-réy. noonu mu won ma yerusalem, dëkk bu sell bi, muy wàcce ci asamaan, jóge ca wetu yàlla,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

baada ya siku sita, yesu aliwachukua petro, yakobo na yohane juu ya mlima mrefu peke yao. huko, yesu akageuka sura mbele yao,

沃洛夫语

juróom-benni fan gannaaw gi, yeesu àndoon na ak piyeer, saag ak yowaana, mu yóbbu leen ñoom rekk fu wéet ci tund wu kawe lool. foofa jëmmam soppiku ci seen kanam;

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kwa muda mrefu huyo hakimu hakupenda kumtetea huyo mjane; lakini, mwishowe akajisemea: ingawa mimi simchi mungu wala simjali binadamu,

沃洛夫语

Àttekat ba bañ lu yàgg, waaye am bés mu ne ci xelam: “ragaluma yàlla te faalewuma mbindeef,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

muda mrefu ulikuwa umepita, na hata siku ya kufunga ilikuwa imekwisha pita. sasa ilikuwa hatari sana kusafiri kwa meli. basi, paulo aliwapa onyo:

沃洛夫语

fekk booba yàggoon nañu ca yoon wa, te dem ci géej daldi aaytal, ndaxte jamonoy kooru yawut ya wees na. moo tax pool digal leen ne:

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alipokuwa anashuka pwani, mtu mmoja aliyekuwa amepagawa na pepo alimjia kutoka mjini. kwa muda mrefu mtu huyo, hakuwa anavaa nguo, wala hakuwa anaishi nyumbani bali makaburini.

沃洛夫语

bi yeesu di wàcc ca gaal ga, ku rab jàpp ca waa dëkk ba ñëw, kar ko. yàgg na def yaramu neen te dëkkul ca kër, waaye ca sëg ya lay nekk.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

herode alifurahi sana alipomwona yesu. alikuwa amekwisha sikia habari zake, na hivyo alikuwa anatazamia kwa muda mrefu kumwona kwa macho yake mwenyewe. zaidi ya hayo, alikuwa anatumaini kumwona yesu akitenda mwujiza.

沃洛夫语

bi erodd gisee yeesu, mu am mbég mu réy. bu yàgg ba tey dafa koo bëggoon a gis, ndaxte déggoon na ñuy wax ci ay mbiram te yaakaaroon na ne, dina ko gis mu def kéemaan.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

wakati uliopita mlikuwa na muda mrefu wa kufanya mambo wanayofanya watu wasiomjua mungu. mliishi maisha ya anasa, ubinafsi, ulevi, ugomvi, kunywa mno na ya ibada haramu za sanamu.

沃洛夫语

ndaxte àndoon ngeen démb ci xalaati ñi xamul yàlla, di dund ciy ñaawteef ak topp seen bakkan, di màndi ak a xawaare, di xér ci biiñ ak a jaamu ay xërëm yu araam, waaye na fi yem nag.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

paulo akamjibu, "namwomba mungu kwamba, kwa muda mfupi au mrefu, si wewe tu bali wote wanaonisikia leo wapate kuwa kama nilivyo mimi, lakini bila hii minyororo."

沃洛夫语

pool tontu ko: «muy tey, muy ëllëg, waxuma yaw rekk waaye it ñi may déglu tey ñépp, na yàlla def, ba ngeen fekksi ma ci li ma nekk, lu moy jéng yii!»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

baada ya kukaa muda mrefu bila kula chakula, paulo alisimama kati yao, akasema, "waheshimiwa, ingalikuwa afadhali kama mngalinisikiliza na kuacha kusafiri kutoka krete. kama mngalifanya hivyo tungaliiepuka shida hii na hasara hizi zote.

沃洛夫语

bi loolu di xew, fekk gëj nañoo lekk, pool daldi taxaw ci seen biir ne leen: «gaa ñi, li gënoon mooy ngeen déglu ma te bañ a jóge kereet, ba indil seen bopp musiba ak kasara ju réy jii.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,779,969,468 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認