您搜索了: mtawala (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

wakati huo, mtawala herode alisikia sifa za yesu.

沃洛夫语

ca jamono joojale erodd boroom diiwaanu galile dégg na tur, wa yeesu am.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

sasa ndio wakati wa ulimwengu huu kuhukumiwa; sasa mtawala wa ulimwengu huu atapinduliwa.

沃洛夫语

Àtteb àddina si jot na: léegi ñu dàq malaaka mu bon, mi jiite àddina si.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

sitasema nanyi tena mambo mengi, maana mtawala wa ulimwengu huu anakuja. kwangu mimi hawezi kitu;

沃洛夫语

lu weesu tey duma amati jotu waxtaan ak yéen, ndaxte malaaka mu bon mi jiite àddina saa ngi ñëw. kooku manalu ma dara.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

basi, jiwekeni chini ya mamlaka yote ya kibinadamu, kwa ajili ya bwana: utii kwa mfalme aliye mtawala mkuu,

沃洛夫语

na seen nangub boroom bi tax, ngeen déggal képp kuy kilifa, muy buur ba gën a kawe,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kutokea kwake kutafanyika wakati ufaao uliopangwa na mungu mwenye heri na aliye mtawala pekee, mfalme wa wafalme, na bwana wa mabwana.

沃洛夫语

moom kenn mooy boroom bu tedd, di buuru buur yi ak kilifag kilifa yi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

wakati ule mliishi kufuatana na mtindo mbaya wa ulimwengu huu, mkawa mnamtii mtawala wa pepo wenye nguvu wa anga, pepo ambao huwatawala sasa watu wasiomtii mungu.

沃洛夫语

ci biir yooyu ngeen doon dund démb, topp doxalinu àddina, tey déggal kilifag boroom sañ-sañ yi ci jaww ji, di xel mu bon miy jëf ci kureelu ñi déggadil yàlla.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

na kutoka kwa yesu kristo, shahidi mwaminifu, wa kwanza kufufuliwa kutoka wafu, na ambaye ni mtawala wa wafalme wa dunia. yeye anatupenda, na kwa damu yake ametufungua kutoka vifungo vya dhambi zetu,

沃洛夫语

tukkee it ci yeesu kirist, seede bu takku bi, moom taaw bi, maanaam ki jëkk a dekki, di buuru buur yi ci kaw suuf yépp. na ndam ak nguur féete ak yeesu kirist ba fàww, moom mi nu bëgg te yiwi nu ci sunuy bàkkaar ak deretam ji tuuru, te def nu askanu saraxalekati buur yàlla baayam, nu di ko jaamu. amiin.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

paulo akajibu, "ndugu zangu, sikujua kama yeye ni kuhani mkuu. maana maandiko yasema hivi: usiseme vibaya juu ya mtawala wa watu wako."

沃洛夫语

pool tontu leen: «bokk yi, xawma woon ne saraxalekat bu mag bi la, ndaxte tëral nañu ci mbind mi ne: “bul wax lu bon sa kilifag xeet.”»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,791,372,265 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認