来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。
neema ya bwana yesu iwe nanyi.
na yiwu boroom bi yeesu ànd ak yéen.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
tunawatakieni neema ya bwana wetu yesu kristo.
na yiwu sunu boroom yeesu kirist ànd ak yéen.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
nawatakieni nyote neema ya bwana yesu. amen.
na yiwu boroom bi yeesu ànd ak yéen ñépp.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
na kutangaza mwaka wa neema ya bwana."
tey yégle atum yiw, mi jóge ci boroom bi.»
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
警告:包含不可见的HTML格式
kutokana na ukamilifu wake sisi tumepokea neema mfululizo.
kàddu gi fees na ak yiw, te nun ñépp jot nanu ci sunu wàll, mu barkeel nu ay yooni-yoon.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
bwana awe nawe rohoni mwako. nawatakieni nyote neema.
na boroom bi aar sa xel. na yiwu yàlla ànd ak yéen ñépp.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
neema ya bwana wetu yesu kristo iwe nanyi nyote. amina.
na yiwu sunu boroom yeesu kirist ànd ak yéen! amiin.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
kila mmoja wetu amepewa neema kadiri ya kipimo alichojaliwa na kristo.
waaye ku nekk ci nun ak mayam, ni nu ko kirist séddalee.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
nawatakieni neema na amani tele katika kumjua mungu na yesu bwana wetu.
na leen yàlla dollil yiw ak jàmm, jaar ci xam ko ak yeesu sunu boroom.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
ndugu, nawatakieni ninyi nyote neema ya bwana wetu kristo. amina.
bokk yi, na yiwu yeesu kirist sunu boroom ànd ak seen xel. amiin.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
ili kwa neema yake tupate kukubaliwa kuwa waadilifu na kuupokea uzima wa milele tunaoutumainia.
ci noonu yàlla àtte na nu jub ci kaw yiwam, te sédd nu ci dund gu dul jeex, gi nuy séentu.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
basi, tumsifu mungu kwa sababu ya neema yake tukufu katika mwanae mpenzi!
na ndamam jolli ndax yiw wu réy, wi mu nu sotti ci soppeem bi.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
basi, wewe mwanangu, uwe na nguvu katika neema tunayopata katika kuungana na kristo yesu.
kon nag yaw sama doomu diine, doolewool yiw, wi ci kirist yeesu.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
lakini mungu, kwa neema yake, alikuwa ameniteua hata kabla sijazaliwa, akaniita nimtumikie.
waaye yàlla mi ma tànn lu jiitu sama juddu te woo ma ci boppam ci kaw yiwam, bi mu ko soobee, xamal na ma kan mooy doomam, ngir ma yégal ñi dul yawut xebaar bu baax bi ci mbirum kirist; booba nag diisoowuma ci ak kenn.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
bila shaka mmekwisha sikia kwamba mungu, kwa neema yake, alinikabidhi kazi hii niifanye kwa faida yenu.
wóor na ma ne, dégg ngeen yenub xamle yiwu yàlla, bi mu ma jagleel jëm ci yéen.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
basi, tukiwa wafanyakazi pamoja na mungu, tunawasihi msikubali ile neema mliyopokea kutoka kwa mungu ipotee bure.
nun nag ñiy liggéeyandoo ak yàlla, nu ngi leen di ñaan: jariñooleen yiw, wi ngeen jote ci yàlla, ngir mu bañ a neen ci yéen.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
basi, tunavyo vipaji mbalimbali kufuatana na neema tuliyopewa. mwenye kipaji cha unabii na akitumie kadiri ya imani yake.
kon gannaaw yàlla séddale na ay mayam, ku nekk ak sa cér, nanu koy jëfandikoo. ku yàlla may, ngay waare kàddoom, nga wax ko kem sa ngëm;
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
basi, ndivyo ilivyo pia wakati huu wa sasa: ipo idadi ya waliobaki ambao mungu aliwateua kwa sababu ya neema yake.
noonu itam ci jamono ji nu nekk, des na nit ñu néew ñu yàlla dencal boppam ciw yiwam.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
habari njema inazidi kuzaa matunda na kuenea ulimwenguni kote kama vile ilivyofanya kwenu ninyi tangu siku ile mliposikia juu ya neema ya mungu na kuitambua ilivyo kweli.
ni xebaar bu baax bi wàcce ci yéen, noonu lay wàcce ci àddina sépp, di meññ te di law. te noonu lay doxale ci yéen, li dale ci bés, ba ngeen dégge xebaaru yiwu yàlla, te xam dëggam gi mu ëmb;
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
basi, na tukikaribie bila hofu kiti cha enzi cha mungu, palipo na neema, ili tukajipatie huruma na neema ya kutusaidia wakati wa lazima.
kon nag nanu am kóolute ci jege jalu yàlla bu yiw ba, ngir jot yërmandeem ak yiwam, ngir mu wallu nu fu soxla taxawe.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量: