来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。
nikamwona huyo mwanamke amelewa damu ya watu wa mungu, na damu ya watu waliouawa kwa sababu ya kumtangaza yesu. nilipomwona nilishangaa mno.
ma gis jigéen ja màndi ci deretu gaayi yàlla yi, ci deretu ñi doon seedeel yeesu. naka laa ko gis, ma daldi jaaxle lool.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
basi, nilipomwona tu, nilianguka mbele ya miguu yake kama maiti. lakini yeye akaweka mkono wake wa kulia juu yangu, akasema, "usiogope! mimi ni wa kwanza na wa mwisho.
naka laa ko gis, di daanu ci ay tànkam ni ku dee. waaye mu teg loxol ndeyjooram ci sama kaw ne ma: «bul ragal dara. maay ki jëkk te maay mujj.
最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:
警告:包含不可见的HTML格式