您搜索了: nimekuja (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

"nimekuja kuwasha moto duniani, laiti ungekuwa umewaka tayari!

沃洛夫语

«damaa ñëw ngir indi safara si ci àddina, te bëgg naa xaat taal bi tàkk.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

mnadhani nimekuja kuleta amani duniani? hata kidogo; si amani bali utengano.

沃洛夫语

ndax dangeen a xalaat ne, damaa ñëw ngir indi jàmm ci àddina? déedéet. maa ngi leen koy wax, damaa ñëw ngir indi féewaloo.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

"msidhani kwamba nimekuja kuleta amani duniani. sikuja kuleta amani bali upanga.

沃洛夫语

«te it buleen defe ne, damaa ñëw ngir indi jàmm ci àddina; ñëwuma ngir indi jàmm, waaye jaasi laa indaale.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

"msidhani ya kuwa nimekuja kutangua sheria ya mose na mafundisho ya manabii. sikuja kutangua bali kukamilisha.

沃洛夫语

«buleen defe ne, ñëw naa ngir dindi yoonu musaa ak waxi yonent yi. Ñëwuma ngir dindi leen, waaye ngir ñu am ci man.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

mwizi huja kwa shabaha ya kuiba, kuua na kuharibu. mimi nimekuja mpate kuwa na uzima--uzima kamili.

沃洛夫语

sàcc bi moom, day sàccsi rekk, di rey ak a yàq. man damaa ñëw, ngir nit ñi am dund, ba nekk ci naataange.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

mimi nimekuja kwa mamlaka ya baba yangu, lakini hamnipokei; bali mtu mwingine akija kwa mamlaka yake mwenyewe, mtampokea.

沃洛夫语

man ñëw naa ci sama turu baay, te nanguwuleen ma, waaye bu keneen dikkee ci turu boppam, ngeen nangu ko.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

yesu akasema, "mimi nimekuja ulimwenguni kutoa hukumu, kusudi wasioona wapate kuona, na wale wanaoona wawe vipofu."

沃洛夫语

yeesu ne ko: «Àttee ma tax a ñëw àddina, ngir ñi gumba gis, ñiy gis gumba.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

"sasa roho yangu imefadhaika, na niseme nini? je, niseme: baba, usiruhusu saa hii inifikie? lakini ndiyo maana nimekuja--ili nipite katika saa hii.

沃洛夫语

«léegi nag damaa jàq. lu may war a wax? mbaa du dama naan: “baay, musal ma ci li nar a xew waxtu wiy ñëw?” déedéet, ñëw naa sax ngir jaar ci waxtu woowu.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,726,429,040 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認