您搜索了: uaminifu (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

na wataonekana kukosa uaminifu kuhusu ahadi yao ya pale awali.

沃洛夫语

te dina daje ak mbugal ndaxte fecci na kóllëre.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

nakuamuru ushike maagizo yako na kuyatii kwa uaminifu mpaka siku ile atakapotokea bwana wetu yesu kristo.

沃洛夫语

sàmmal ndigal li, bañ a am gàkk mbaa ŋàññ, ba kera yeesu kirist sunu boroom di feeñ ci ndamam, ca waxtu wa yàlla dogal.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ndoa inapaswa kuheshimiwa na watu wote, na haki zake zitekelezwe kwa uaminifu. mungu atawahukumu waasherati na wazinzi.

沃洛夫语

na ñépp fullaal séy, te lalu séy bi bañ a taq sobe, ndaxte yàlla dina àtte ñu yàqu ñi ak njaalookat yi.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

alipofika huko na kuona jinsi mungu alivyowaneemesha wale watu, alifurahi na kuwahimiza wote wadumu katika uaminifu wao kwa bwana.

沃洛夫语

bi mu agsee nag, ba gis yiw, wi leen yàlla may, mu bég ci te di leen xiir, ñu wàkkirlu ci boroom bi te dogu ci.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini itakuwaje iwapo baadhi yao hawakuwa waaminifu? je, jambo hilo litaondoa uaminifu wa mungu?

沃洛夫语

bu fekkee ne am na ci ñoom ñu ñàkk kóllëre, ndax loolu man na fanq kóllëreg yàlla?

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini matokeo ya kuongozwa na roho ni mapendo, furaha, amani, uvumilivu, wema, fadhili, uaminifu,

沃洛夫语

waaye li xelu yàlla mi di meññ mooy: mbëggeel, mbég, jàmm, muñ, laabiir, mbaax, kóllëre,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

maana, nawaambieni kristo aliwatumikia wayahudi apate kuonyesha uaminifu wa mungu, na zile ahadi mungu alizowapa babu zetu zipate kutimia;

沃洛夫语

lii laay wax: kirist ñëw na liggéeyal yawut yi, ngir wone kóllëreg yàlla ci matal dige, ya mu digoon maam ya.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini naogopa kwamba, kama vile yule nyoka kwa hila zake za uongo alimdanganya hawa, fikira zenu zaweza kupotoshwa, mkauacha uaminifu wenu wa kweli kwa kristo.

沃洛夫语

waaye ni jaan ja naxe woon awa ci pexeem, ragal naa yéen itam ñu lëmbaaje ni seen xel, ba ngeen dëddu xol bu laab, bi ngeen amoon ci seen diggante ak kirist.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kutokana na uthibitisho unaoonyeshwa kwa huduma hii yetu, watu watamtukuza mungu kwa sababu ya uaminifu wenu kwa habari njema ya kristo mnayoiungama, na pia kwa sababu ya ukarimu mnaowapa wao na watu wote.

沃洛夫语

ci li ngeen firndeel seen mbëggeel ci joxe ndimbal lii, dinañu màggal yàlla, ndaxte wone ngeen ni ngeen déggale xebaar bu baax bu kirist bi, ak ni ngeen yéwéne ci seen ndimbal jëme ci ñoom ak ñépp.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ninyi ni watu msio na uaminifu kama wazinzi. je, hamjui kwamba kuwa rafiki wa ulimwengu ni kuwa adui wa mungu? yeyote anayetaka kuwa rafiki wa ulimwengu anajifanya adui wa mungu.

沃洛夫语

yéen ñi fecci seen kóllëre ak yàlla, xanaa xamuleen ne mbëggeelu àddina, mbañeel la fa yàlla? ku bëgg a xaritoo ak àddina nag, noonoo nga ak yàlla.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

naye akawajibu, "kizazi kiovu kisicho na uaminifu! mnataka ishara; hamtapewa ishara nyingine, ila tu ile ishara ya nabii yona.

沃洛夫语

yeesu tontu leen: «yéenay laaj firnde, yéen niti jamono ju bon jii, yéen ñi fecci seen kóllëre ak yàlla, waaye dungeen jot genn firnde gu dul firndeg yonent yàlla yunus.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

kizazi kiovu kisicho na uaminifu! mnataka ishara, lakini hamtapewa ishara yoyote isipokuwa tu ile ya yona." basi, akawaacha, akaenda zake.

沃洛夫语

yéenay laaj firnde, yéen niti jamono ju bon jii, yéen ñi fecci seen kóllëre ak yàlla. waaye dungeen jot genn firnde gu dul firndeg yunus.» bi yeesu waxee loolu, mu jóge ci ñoom, dem.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

basi, wakawatuma wafuasi wao pamoja na wafuasi wa kikundi cha herode. wakamwuliza, "mwalimu, tunajua kwamba wewe ni mtu mwaminifu, na kwamba wafundisha njia ya mungu kwa uaminifu; humwogopi mtu yeyote, maana cheo cha mtu si kitu kwako.

沃洛夫语

noonu ñu yónni ci moom seeni taalibe ak ñi far ak buur bi erodd ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne ku wóor nga, te ragaloo kenn, ndaxte seetuloo jëmmi nit, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,781,163,807 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認