来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。
noonu kon mu dellusi kana ci galile, dëkk ba mu soppe woon ndox ma biiñ. amoon na benn dagu buur bu dëkkoon kapernawum te doomam feebar.
so jesus came again into cana of galilee, where he made the water wine. and there was a certain nobleman, whose son was sick at capernaum.
kon nanu jege yàlla ak xol bu laab, ak ngëm gu ànd ak kóolute, am xel mu dal ci bépp yeraange, ak yaram wu ñu raxas ci ndox mu sell.
let us draw near with a true heart in full assurance of faith, having our hearts sprinkled from an evil conscience, and our bodies washed with pure water.
noonu yeesu yebal ñaar ci taalibe yi ne leen: «demleen ca dëkk ba, foofa góor gu yenu njaq lu def ndox, dina taseek yéen, ngeen topp ko.
and he sendeth forth two of his disciples, and saith unto them, go ye into the city, and there shall meet you a man bearing a pitcher of water: follow him.