Results for dégluleen translation from Wolof to English

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

«dégluleen, dafa amoon beykat bu demoon jiyi.

English

hearken; behold, there went out a sower to sow:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«yéen nag dégluleen li léebu beykat biy tekki.

English

hear ye therefore the parable of the sower.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«yéen bokk yi ak baay yi, dégluleen samaw lay.»

English

men, brethren, and fathers, hear ye my defence which i make now unto you.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dégluleen yéen boroom alal yi, jooyleen te naqarlu ndax mbugal, gi leen di xaar.

English

go to now, ye rich men, weep and howl for your miseries that shall come upon you.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu yeesu waxaat ak mbooloo mi ne leen: «yéen ñépp dégluleen ma te xam.

English

and when he had called all the people unto him, he said unto them, hearken unto me every one of you, and understand:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

boroom bi tegaat ca ne: «dégluleen bu baax li àttekat bu bon boobu wax;

English

and the lord said, hear what the unjust judge saith.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu baat jibe ca niir wa naan: «kii mooy sama doom ji ma fal; dégluleen ko.»

English

and there came a voice out of the cloud, saying, this is my beloved son: hear him.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«dégluleen bu baax lii ma leen di wax: dinañu jébbal doomu nit ki ci loxoy nit ñi.»

English

let these sayings sink down into your ears: for the son of man shall be delivered into the hands of men.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dégluleen! man pool maa leen koy wax: bu ngeen itteelee xaraf, kon kirist dootu leen jariñ dara.

English

behold, i paul say unto you, that if ye be circumcised, christ shall profit you nothing.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu pool jóg, tàllal loxoom ne leen: «yéen bokki israyil ak yéen ñi ragal yàlla, dégluleen!

English

then paul stood up, and beckoning with his hand said, men of israel, and ye that fear god, give audience.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«dégluleen, maa ngi leen di yónni, mel ni ay xar ci biir ay bukki. muusleen nag niy jaan, te lewet niy pitax.

English

behold, i send you forth as sheep in the midst of wolves: be ye therefore wise as serpents, and harmless as doves.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dégluleen yéen sama bokk yi ma bëgg, ndax yàlla tànnul ñi néewle ci àddina, ngir ñu barele ci ngëm, tey am i cér ci nguur, gi yàlla dig ñi ko bëgg?

English

hearken, my beloved brethren, hath not god chosen the poor of this world rich in faith, and heirs of the kingdom which he hath promised to them that love him?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«bokk yi, dégluleen ma! simoŋ nettali na, ni yàlla seetsee bu jëkk ñi dul yawut, ngir sàkku ci ñoom xeet wu ñu tudde turam.

English

simeon hath declared how god at the first did visit the gentiles, to take out of them a people for his name.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu niir muur leen, te baat jibe ca niir wa naan: «kii mooy sama doom ji ma bëgg, ci moom laa ame bànneex; dégluleen ko.»

English

and there was a cloud that overshadowed them: and a voice came out of the cloud, saying, this is my beloved son: hear him.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci kaw loolu piyeer taxaw, ànd ak fukki ndaw ya ak benn, mu wax ci kaw, di yégal mbooloo ma ne: «bokki yawut yi ak yéen ñépp ñi dëkk yerusalem, dégluleen bu baax te xam lii ma leen di wax!

English

but peter, standing up with the eleven, lifted up his voice, and said unto them, ye men of judaea, and all ye that dwell at jerusalem, be this known unto you, and hearken to my words:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,727,863,337 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK