Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
yesu, hali akijua yote yatakayompata, akatokea, akawauliza, "mnamtafuta nani?"
noonu yeesu, mi xamoon li ko waroon a dal lépp, jubsi leen ne leen: «ku ngeen di seet?»
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta
walijaribu kujua nyakati na mazingira ya tukio hilo, yaani wakati alioudokezea roho wa kristo aliyekuwa ndani yao, akibashiri juu ya mateso yatakayompata kristo na utukufu utakaofuata.
bi xelum kirist, mi nekkoon ci ñoom, seedee lu jiitu coonoy kirist ak ndam la cay topp, jéem nañoo takk, kañ ak nan lay ame.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
basi, walikuwa njiani kwenda yerusalemu, na yesu alikuwa anawatangulia. wanafunzi wake walijawa na hofu, na watu waliofuata waliogopa. yesu akawachukua tena kando wale kumi na wawili, akaanza kuwaambia yale yatakayompata:
gannaaw loolu ñu ànd jëm yerusalem, yeesu jiitu; taalibe yi am njàqare, te ñi ci topp tiit. noonu yeesu woowaat fukk ak ñaar ña cig wet, xamal leen li nar a xew ci mbiram.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: