Results for teruggegaan translation from Afrikaans to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Afrikaans

Wolof

Info

Afrikaans

en hulle het hom aanbid en na jerusalem teruggegaan met groot blydskap.

Wolof

taalibe ya màggal ko, daldi dellu yerusalem, fees ak mbég.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

hieroor het baie van sy dissipels teruggegaan en nie meer saam met hom gewandel nie.

Wolof

ci loolu taalibeem yu bare dëpp, bañatee ànd ak moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en toe hulle hom nie vind nie, het hulle teruggegaan na jerusalem en hom gesoek.

Wolof

bi ñu ko gisul nag, ñu daldi dellu yerusalem, seeti ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en toe jesus hoor dat johannes in die gevangenis gesit was, het hy na galiléa teruggegaan.

Wolof

am bés yeesu dégg ne, jàpp nañu yaxya; mu jóg nag, jëm galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en maria het by haar omtrent drie maande gebly; en sy het teruggegaan na haar huis toe.

Wolof

noonu maryaama toog fa elisabet lu war a tollook ñetti weer, sog a ñibbi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

daarop het hulle teruggegaan en speserye en salf berei en op die sabbat gerus volgens die gebod.

Wolof

noonu ñu dellu defari cuuraay ak latkoloñ ngir néew ba. ca bésu noflaay ba ñu noppalu, ni ko yoon wi santaanee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en nadat ons mekaar gegroet het, het ons aan boord gegaan, en hulle het teruggegaan huis toe.

Wolof

noonu nu tàggoo ak ñoom, dugg ca gaal ga, ñu dellu seen kër.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en jesus het met sy dissipels teruggegaan na die see toe, en 'n groot menigte het hom gevolg uit galiléa en judéa

Wolof

gannaaw loolu yeesu ak ay taalibeem jóge fa, jëm dex ga. fekk mbooloo mu mag mu jóge diiwaanu galile, topp ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en die herders het teruggegaan en god verheerlik en geprys oor alles wat hulle gehoor en gesien het, net soos aan hulle gesê is.

Wolof

noonu sàmm ya dellu ca seen jur, di màggal yàlla, di ko sant ci li ñu déggoon lépp te gis ko, ndaxte lépp am na, ni ko boroom bi waxe woon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en die hele skare wat vir hierdie skouspel bymekaar was, het op hulle borste geslaan toe hulle sien wat gebeur het, en hulle het teruggegaan.

Wolof

nit ña fa dajaloo woon ñépp, di seetaan li xew, ba ñu gisee loolu, ñu dellu seen kër, fëgg seen dënn, di jooy.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

nadat hulle dan kragtig getuig en die woord van die here gespreek het, het hulle na jerusalem teruggegaan en die evangelie aan baie dorpe van die samaritane verkondig.

Wolof

noonu bi ñu seedeelee yàlla te wax ci kàddoom, ñu dellu yerusalem, di xamle xebaar bu baax bi ci dëkk yu bare yu waa samari.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en nadat hulle aan daardie stad die evangelie verkondig en 'n aantal dissipels gemaak het, het hulle teruggegaan na listre en ikónium en antiochíë,

Wolof

bi ñu fa àggee nag, ñu xamle fa xebaar bu baax bi, ba sàkk fa ay taalibe yu bare. gannaaw loolu ñu dellusi listar, ikoñum ak ancos,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en die hele menigte van die omtrek van die gadaréners het hom gevra om van hulle weg te gaan, omdat hulle deur 'n groot vrees bevang was. toe het hy in die skuit geklim en teruggegaan.

Wolof

ci kaw loolu waa diiwaanu serasa bépp ragal, ba ñaan yeesu mu jóge fa. noonu yeesu dugg ci gaal gi, di bëgg a dem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en omdat hulle in 'n droom 'n goddelike waarskuwing ontvang het om nie na herodes terug te keer nie, het hulle met 'n ander pad na hul land teruggegaan.

Wolof

bi ñu ko defee yàlla artu na leen ci biir gént, ñu bañ a dellu ca erodd. noonu ñu jaar weneen yoon, ñibbi seen réew.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en toe hulle teruggegaan het, verskyn daar 'n engel van die here in 'n droom aan josef en sê: staan op, neem die kindjie en sy moeder en vlug na egipte, en bly daar totdat ek jou sê; want herodes gaan die kindjie soek om hom dood te maak.

Wolof

bi nga xamee ne boroom xam-xam ya ñibbi nañu, benn malaakam boroom bi feeñu yuusufa ci gént ne ko: «erodd mu ngi ci tànki wut xale bi, ngir rey ko; jógal nag, jël xale bi ak ndeyam te nga daw jëm misra, toog fa, ba kera ma koy wax.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,747,340,223 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK