Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.
but covet earnestly the best gifts: and yet shew i unto you a more excellent way.
waaye fonkleen may yi gën. léegi nag ma won leen yoon wu gën lépp.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
for in this we groan, earnestly desiring to be clothed upon with our house which is from heaven:
fi mu ne nu ngi wonk, di yàkkamtee féete ak sunu dëkkukaayu asamaan, sol ko ni koddaay, xam ne,
Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
but a certain maid beheld him as he sat by the fire, and earnestly looked upon him, and said, this man was also with him.
ab mbindaan gis ko, mu toog, taal bi di ko leeral, mu ne ko jàkk ne: «nit kii itam àndoon na ak moom.»
Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
and being in an agony he prayed more earnestly: and his sweat was as it were great drops of blood falling down to the ground.
ci biir tiis, yeesu gën a sawar ci ñaan gi, ñaqam mel ni lumbi deret dal ci suuf.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
elias was a man subject to like passions as we are, and he prayed earnestly that it might not rain: and it rained not on the earth by the space of three years and six months.
naka noonu iliyas nit la woon ku bindoo ni nun, waaye bi mu saxee ci ñaan yàlla, ngir mu bañ a taw, ndox laalul suuf diirub ñetti at ak genn-wàll.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
beloved, when i gave all diligence to write unto you of the common salvation, it was needful for me to write unto you, and exhort you that ye should earnestly contend for the faith which was once delivered unto the saints.
samay bokk, bëggoon naa leen a bind lool ci mbirum mucc gi nu bokk, waaye lii moo gën a jamp: ma xiir leen, ngeen taxaw ci aar mboolem dëgg, yi yàlla xas a dénk gaayam yu sell yi ba fàww.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
and when peter saw it, he answered unto the people, ye men of israel, why marvel ye at this? or why look ye so earnestly on us, as though by our own power or holiness we had made this man to walk?
bi piyeer gisee loolu nag, mu ne mbooloo mi: «yéen waa israyil, lu tax ngeen waaru ci lii? lu tax ngeen di nu xool jàkk, mel ni ci sunu kàttan, mbaa ci sunu ragal yàlla lanu doxloo kii?
Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität: