Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.
invenio igitur legem volenti mihi facere bonum quoniam mihi malum adiace
gis naa nag lii: saa su ma bëggee def lu baax, lu bon a ngi ma taxawu.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
ait autem pilatus ad principes sacerdotum et turbas nihil invenio causae in hoc homin
pilaat ne saraxalekat yu mag ya ak mbooloo ma: «gisuma genn tooñ ci nit kii.»
Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
esto vigilans et confirma cetera quae moritura erant non enim invenio opera tua plena coram deo me
yeewul te dëgëral li des ci yaw tey waaj a dee, ndaxte gis naa ne, say jëf matuñu ca sama kanam yàlla.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
dicit ei pilatus quid est veritas et cum hoc dixisset iterum exivit ad iudaeos et dicit eis ego nullam invenio in eo causa
pilaat laaj ko ne: «luy dëgg?» bi mu waxee loolu ba noppi, pilaat daldi génnaat, jëm ca yawut ya ne leen: «gisuma ci moom genn tooñ.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
cum ergo vidissent eum pontifices et ministri clamabant dicentes crucifige crucifige dicit eis pilatus accipite eum vos et crucifigite ego enim non invenio in eo causa
waaye bi ñu ko gisee, saraxalekat yu mag ya ak alkaati ya di yuuxoo naan: «daaj ko ci bant! daaj ko ci bant, ba mu dee!» pilaat ne leen: «jël-leen ko, yéen, daaj ko ci bant, ndaxte gisuma ci moom genn tooñ.»
Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
dixit autem ad cultorem vineae ecce anni tres sunt ex quo venio quaerens fructum in ficulnea hac et non invenio succide ergo illam ut quid etiam terram occupa
noonu mu ne surga ba: “Ñetti at a ngii may ñëw di raas-si garab gii te duma ci fekk dara. gor ko. lu tax muy xatal tool bi?”
Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität: