Sie suchten nach: nihil (Latein - Wolof)

Menschliche Beiträge

Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.

Übersetzung hinzufügen

Latein

Wolof

Info

Latein

ad nihil a nihil

Wolof

nothing else going back in town hide in this matter

Letzte Aktualisierung: 2021-04-26
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

existimo enim nihil me minus fecisse magnis apostoli

Wolof

moona foog naa ne, seen ndaw yooyu ngeen yékkati, ba ñu ëpp ndaw sax, ëpplewuñu ma dara.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

et cum accusaretur a principibus sacerdotum et senioribus nihil respondi

Wolof

yeesu tontu ko ne: «wax nga ko,» waaye tontuwul dara ca la ko saraxalekat yu mag ya ak njiit ya jiiñ.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

circumcisio nihil est et praeputium nihil est sed observatio mandatorum de

Wolof

xaraf ak ñàkka xaraf lépp a yem; li am solo moo di topp ndigali yàlla.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

nihil enim intulimus in mundum haut dubium quia nec auferre quid possumu

Wolof

ndaxte indaalewunu fi dara, te dunu yóbbaale dara.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

at ille dixit ad eos nihil amplius quam quod constitutum est vobis faciati

Wolof

mu tontu leen ne: «laajleen rekk lu jaadu.»

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

cum ergo his contradici non possit oportet vos sedatos esse et nihil temere ager

Wolof

gannaaw nag kenn mënta weddi loolu, war ngeen a dalal seen xel te bañ a sañaxu ci dara.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

audimus enim inter vos quosdam ambulare inquiete nihil operantes sed curiose agente

Wolof

léegi nag dégg nanu ne, am na ci yéen ñuy wéy ci tayel; liggéeyuñu dara, lu dul di dugg ci lu seen yoon nekkul.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

ait autem pilatus ad principes sacerdotum et turbas nihil invenio causae in hoc homin

Wolof

pilaat ne saraxalekat yu mag ya ak mbooloo ma: «gisuma genn tooñ ci nit kii.»

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

dico autem quanto tempore heres parvulus est nihil differt servo cum sit dominus omniu

Wolof

li ma leen di wax, mooy lii: doom ji war a donni baayam, fi ak mu ngi cig ndaw, ak lu ko alal jiy lew lépp, du wuute dara ak jaam.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

adprehendentes autem omnes sosthenen principem synagogae percutiebant ante tribunal et nihil eorum gallioni curae era

Wolof

ci kaw loolu nit ñépp jàpp sosten, njiitu jàngu ba, ñu di ko dóor ca kanamu àttekaay ba, waaye galyon faalewu leen.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

athenienses autem omnes et advenae hospites ad nihil aliud vacabant nisi aut dicere aut audire aliquid nov

Wolof

ndaxte waa aten ñépp ak doxandéem ya fa dëkk, wax ak a déglu lu bees rekk lañu daan xënte.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

ecce dedi vobis potestatem calcandi supra serpentes et scorpiones et supra omnem virtutem inimici et nihil vobis nocebi

Wolof

gis ngeen, jox naa leen sañ-sañu joggi ci jaan yi ak ci jiit yi, daan dooley bañaale bi, te dara du leen man a gaañ.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

dicit eis simon petrus vado piscari dicunt ei venimus et nos tecum et exierunt et ascenderunt in navem et illa nocte nihil prendiderun

Wolof

simoŋ piyeer ne leen: «maa ngi nappi.» Ñu ne ko: «nun it danuy ànd ak yaw.» Ñu dugg gaal, daldi dem. waaye guddi googu jàppuñu dara.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

ab his autem qui videbantur esse aliquid quales aliquando fuerint nihil mea interest deus personam hominis non accipit mihi enim qui videbantur nihil contulerun

Wolof

waaye ñi ñu gën a fonk --ak lu man a doon seen sag xooluma ko, ñépp a yem fa kanam yàlla — waaye ñooñu ñu teg njiit boog, bi ma dajee ak ñoom, yokkuñu dara ci sama sas.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

at illi existimabant eum in tumorem convertendum et subito casurum et mori diu autem illis sperantibus et videntibus nihil mali in eo fieri convertentes se dicebant eum esse deu

Wolof

nit ñi di xaar mu newi, mbaa mu ne dàll, dee; waaye bi ñu négee lu yàgg te gis ne dara jotu ko, ñu soppi xel ne: «kii yàlla la.»

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Latein

et videns fici arborem unam secus viam venit ad eam et nihil invenit in ea nisi folia tantum et ait illi numquam ex te fructus nascatur in sempiternum et arefacta est continuo ficulne

Wolof

noonu mu séen garabu figg ca yoon wa, waaye bi mu fa agsee, gisu ci dara lu dul ay xob rekk. ci kaw loolu yeesu ne ko: «dootuloo meññ mukk.» ca saa sa figg ga daldi wow.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-06
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Referenz: Anonym

Eine bessere Übersetzung mit
9,570,673,151 menschlichen Beiträgen

Benutzer bitten jetzt um Hilfe:



Wir verwenden Cookies zur Verbesserung Ihrer Erfahrung. Wenn Sie den Besuch dieser Website fortsetzen, erklären Sie sich mit der Verwendung von Cookies einverstanden. Erfahren Sie mehr. OK