Sie suchten nach: molimo (Serbisch - Wolof)

Menschliche Beiträge

Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.

Übersetzung hinzufügen

Serbisch

Wolof

Info

Serbisch

molimo te za svog sina onisima, kog rodih u okovima svojim;

Wolof

maa ngi tinul sama doomu diine onesim, mi ma jur ci kirist fii ci kaso bi.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

molimo vas, pak, kao pomagaèi da ne primite uzalud blagodat božiju.

Wolof

nun nag ñiy liggéeyandoo ak yàlla, nu ngi leen di ñaan: jariñooleen yiw, wi ngeen jote ci yàlla, ngir mu bañ a neen ci yéen.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

dan i noæ molimo se bogu preizobilno da vidimo lice vaše, i da ispunimo nedostatak vere vaše.

Wolof

guddi ak bëccëg nu ngi wàkkirlu ci ñaan yàlla, ngir gis leen, ba man a mottali seen ngëm.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

i ovo je sloboda koju imamo k njemu da ako šta molimo po volji njegovoj posluša nas.

Wolof

kóolute gi nu am ci kanam yàlla mooy lii, su nu ko ñaanee dara ci coobareem, dina nu nangul.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

i kad znamo da nas sluša šta god molimo, znamo da æe nam dati šta tražimo od njega.

Wolof

gannaaw xam nañu ne, dina nangu lépp lu nu koy ñaan, xam nanu it ne, li nu ko ñaan, jox na nu ko.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

jer se radujemo kad mi slabimo, a vi jaèate. a zato se i molimo bogu, za vaše savršenstvo.

Wolof

bu nu néewee doole, fekk am ngeen doole, bég nanu ci. te sax nu ngi ñaan, ngeen jublu cig mat.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

ali vas molimo, braæo, za dolazak gospoda našeg isusa hrista, i za naš sastanak u njemu,

Wolof

ci lu jëm ci ñëwu boroom bi yeesu kirist nag, bokk yi, ak sunu daje ak moom, am na lu ma leen di ñaan:

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

nego molimo da èujemo od tebe šta misliš; jer nam je poznato za ovu jeres da joj se svuda nasuprot govori.

Wolof

waaye bëgg nanoo dégg li nga gëm, ndaxte xam nanu ne, tariixa booba, kenn jubluwu ko fenn.»

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

molimo vas pak, braæo, prepoznajte one koji se trude medju vama, i nastojnike svoje u gospodu i uèitelje svoje,

Wolof

gannaaw loolu bokk yi, ci lu jëm ci njiit, yi boroom bi teg ci seen kanam te ñuy liggéey ci seen biir, di leen artu, maa ngi leen di ñaan ngeen déglu leen;

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

a molimo se bogu da vi ne èinite nikakvo zlo, ne da se mi valjani pokažemo, nego da vi dobro èinite, a mi kao nevaljani da budemo.

Wolof

nu ngi ñaan yàlla, ngeen bañ a def dara lu bon. waxuma ne danoo bëgg a wone noonu sunu firndeg ngëm, waaye sunu yéene mooy ngeen jëf lu baax, boo yaboo sax ñu jiiñ nu ag naaféq.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Serbisch

dalje, braæo, molimo vas i savetujemo u hristu isusu, kao što primiste od nas, kako vam treba živeti i ugadjati bogu, kao što živite, da bivate sve izobilniji.

Wolof

léegi nag bokk yi, jot ngeen ci nun, nan ngeen war a dunde ba neex yàlla, te moom ngeen di def. waaye ci turu boroom bi yeesu nu ngi leen di ñaan ak a dénk, ngeen gën koo feddali.

Letzte Aktualisierung: 2012-05-04
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Eine bessere Übersetzung mit
9,571,062,703 menschlichen Beiträgen

Benutzer bitten jetzt um Hilfe:



Wir verwenden Cookies zur Verbesserung Ihrer Erfahrung. Wenn Sie den Besuch dieser Website fortsetzen, erklären Sie sich mit der Verwendung von Cookies einverstanden. Erfahren Sie mehr. OK