Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.
lakini anayeingia kwa kupitia mlangoni, huyo ndiye mchungaji wa kondoo.
waaye ki jaar ci bunt bi, mooy sàmmu xar yi.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
na wakati mchungaji mkuu atakapotokea, ninyi mtapokea taji ya utukufu isiyofifia.
noonu waxtu wu boroom gétt gi feeñee, dina leen jagleel kaalag ndam guy sax ba fàww.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
mimi ni mchungaji mwema. nawajua walio wangu, nao walio wangu wananijua mimi,
«man maay sàmm bu baax bi. ni ma xame baay bi te baay bi xame ma ni, noonu laa xame samay xar, te ñoom it ni lañu ma xame. te it kat dinaa joxe sama bakkan ngir xar yi.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
na mataifa yote yatakusanyika mbele yake, naye atawatenganisha watu kama mchungaji anavyotenganisha kondoo na mbuzi.
bu boobaa dees na dajale xeeti àddina yépp ci kanamam, te dina leen xàjjale, ni sàmm di xàjjalee xar yi ak bëy yi,
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
"mimi ni mchungaji mwema. mchungaji mwema huutoa uhai wake kwa ajili ya kondoo wake.
«man maay sàmm bu baax bi. sàmm bu baax bi day joxe bakkanam ngir ay xaram.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
Warnung: Enthält unsichtbare HTML-Formatierung
ninyi mlikuwa kama kondoo waliokuwa wamepotea; lakini sasa mmemrudia mchungaji na mlinzi wa roho zenu.
ndaxte yéena ngi réeroon niy xar, waaye léegi dellusi ngeen ci sàmm, biy aar seeni xol.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
mungu amemfufua bwana wetu yesu kristo ambaye ni mchungaji mkuu wa kondoo kwa sababu ya kumwaga damu yake iliyothibitisha agano la milele.
na leen yàlla boroom jàmm, mi dekkal sunu boroom yeesu, di sàmm bu mag bi, ci darajay deret, ji fas kóllëre gu sax,
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
basi, alipowaona watu, makundi kwa makundi, aliwaonea huruma kwa sababu walikuwa hoi na wenye wasiwasi kama kondoo wasio na mchungaji.
bi yeesu gisee mbooloo ma, mu yërëm leen, ndaxte dañoo sonn ba ne yogg, mel ni xar yu amul sàmm.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
tena ninao kondoo wengine ambao hawamo zizini humu. inanibidi kuwaleta hao pia, nao wataisikia sauti yangu, na kutakuwako kundi moja na mchungaji mmoja.
am naa yeneen xar yu bokkul ci gétt gii. war naa leen a indi, ñoom it, te dinañu déglu sama baat. benn coggal ay am ak benn sàmm.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
mtu wa kuajiriwa ambaye si mchungaji, na wala kondoo si mali yake, anapoona mbwa mwitu anakuja, huwaacha kondoo na kukimbia. kisha mbwa mwitu huwakamata na kuwatawanya.
ki dul sàmm bi tey liggéeyal xaalis rekk waaye moomul xar yi, bu séenee bukki, day daw, bàyyi fa xar ya. bu ko defee bukki ba dal ca coggal ja, jàpp ca, tasaare ya ca des.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
je, mwanajeshi gani anayelipia utumishi wake jeshini? mkulima gani asiyekula matunda ya shamba lake la mizabibu? mchungaji gani asiyekunywa maziwa ya mifugo yake?
kan moo mas a solu soldaar ci pexey boppam? kan mooy bey tool te du ci jariñu? walla kan mooy sàmm jur te du naan ca soow ma?
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
yesu akawaambia wanafunzi wake, "ninyi nyote mtakuwa na mashaka nami; maana maandiko matakatifu yasema: nitampiga mchungaji nao kondoo watatawanyika.
booba yeesu ne leen: «yéen ñépp dingeen ma dàggeeku, ndaxte bind nañu:“dinaa dóor sàmm bi,xari jur gi tasaaroo.”
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
Warnung: Enthält unsichtbare HTML-Formatierung
kisha yesu akawaambia, "usiku huu wa leo, ninyi nyote mtakuwa na mashaka nami, maana maandiko matakatifu yasema: nitampiga mchungaji, na kondoo wa kundi watatawanyika.
booba yeesu ne leen: «yéen ñépp dingeen ma dàggeeku ci guddi gii, ndaxte bind nañu: “dinaa dóor sàmm bi, xari jur gi tasaaroo.”
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
Warnung: Enthält unsichtbare HTML-Formatierung