Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.
basi, ikiwa tumekufa pamoja na kristo, tunaamini kwamba tutaishi pia pamoja naye.
gannaaw nag dee nanu ak kirist, gëm nanu ne, dinanu dekki it ni moom,
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
usemi huu ni wa kweli: "ikiwa tulikufa pamoja naye, tutaishi pia pamoja naye.
kàddu gu wóor a ngii:su nu deeyaalee ak kirist,dinanu dundaat ak moom;
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:
Warnung: Enthält unsichtbare HTML-Formatierung
maana hata kama alisulubiwa kwa sababu ya udhaifu, lakini sasa anaishi kwa uwezo wa mungu. sisi pia tu dhaifu kwa kuungana naye lakini tutaishi naye kwa uwezo wa mungu kwa ajili yenu.
néewoon na doole, ba ñu koy daaj ca bant ngir rey ko, waaye mi ngi dund ci kàttanu yàlla. nun itam néew nanu doole ci sunu bokk ci moom, waaye dinanu dund ak moom ci kàttanu yàlla, bu nuy jëfante ak yéen.
Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität: