Sie suchten nach: juróom (Wolof - Amharisch)

Menschliche Beiträge

Von professionellen Übersetzern, Unternehmen, Websites und kostenlos verfügbaren Übersetzungsdatenbanken.

Übersetzung hinzufügen

Wolof

Amharisch

Info

Wolof

Ñu toog nag ay géewi juróom-fukk ak téeméer.

Amharisch

መቶ መቶውና አምሳ አምሳው እየሆኑ በተራ በተራ ተቀመጡ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

fekk juróom ca janq ya di ñu am xel, juróom ya ca des ñàkk xel.

Amharisch

ከእነርሱም አምስቱ ሰነፎች አምስቱም ልባሞች ነበሩ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

juróomi yoon yawut yi dóor nañu ma fanweeri yar ak juróom-ñeent.

Amharisch

አይሁድ አንድ ሲጎድል አርባ ግርፋት አምስት ጊዜ ገረፉኝ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

Ñaareel ba ak ñetteel ba def noonu, ba ci juróom-ñaareel ba.

Amharisch

እንዲሁ ደግሞ ሁለተኛው ሦስተኛውም፥ እስከ ሰባተኛው ድረስ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

mu gis fa nit ku làggi, tudd ene, tëdd ci basaŋ diirub juróom-ñetti at.

Amharisch

በዚያም ከስምንት ዓመት ጀምሮ በአልጋ ላይ ተኝቶ የነበረውን ኤንያ የሚሉትን አንድ ሰው አገኘ፤ እርሱም ሽባ ነበረ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

kon ba tey yàllaa ngi dencal ay gaayam noflaay bu nirook noflaayu yàlla ca juróom-ñaareelu fan ba.

Amharisch

እንግዲያስ የሰንበት ዕረፍት ለእግዚአብሔር ሕዝብ ቀርቶላቸዋል።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

ci ndekkite li nag kan ci ñoom moo ko war a donn, fekk ku nekk ci juróom-ñaar ñi mas na koo takk?»

Amharisch

ሰባቱ አግብተዋታልና በትንሣኤ ቀን ሲነሡ ከእነርሱ ለማናቸው ሚስት ትሆናለች?

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

mbote ma dindi na juróom-ñaareelu tayu ga, asamaan ne selaw lu mat genn-wàllu waxtu.

Amharisch

ሰባተኛውንም ማኅተም በፈታ ጊዜ እኵል ሰዓት የሚያህል ዝምታ በሰማይ ሆነ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

ci kaw loolu yuusufa yeble, woo baayam ak mbokkam yépp, ñuy juróom-ñaar-fukki nit ak juróom.

Amharisch

ዮሴፍም አባቱን ያዕቆብንና ሰባ አምስት ነፍስ የነበረውን ቤተ ዘመድ ሁሉ ልኮ አስጠራ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

bi ñu joowee lu war a tollook juróom benni kilomet, ñu séen yeesu, muy dox ci kaw dex gi, jëm ci ñoom, ñu daldi tiit.

Amharisch

ሀያ አምስት ወይም ሠላሳ ምዕራፍ ከቀዘፉ በኋላም፥ ኢየሱስ በባሕር ላይ እየሄደ ወደ ታንኳይቱ ሲቀርብ አይተው ፈሩ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

elisabet sa mbokk mi it dina am doom ju góor cig màggatam. ki ñu doon wooye ku mënul a am doom, mu ngi ci juróom-benni weeram.

Amharisch

እነሆም ዘመድሽ ኤልሳቤጥ፥ እርስዋ ደግሞ በእርጅናዋ ወንድ ልጅ ፀንሳለች፥ ለእርስዋም መካን ትባል ለነበረችው ይህ ስድስተኛ ወር ነው፤

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

«amoon na fi nag juróom-ñaari góor, ñu bokk ndey ak baay. taaw ba takk jabar, faatu, te bàyyiwul doom.

Amharisch

ሰባት ወንድማማቾች ነበሩ፤ ፊተኛውም ሚስት አግብቶ ዘር ሳያስቀር ሞተ፤

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

juróom-benneelu malaaka ma wol liitam. noonu ma dégg baat bu jóge ci ñeenti béjjén, yi nekk ci koñi saraxalukaayu wurus, ba nekk ci kanam yàlla,

Amharisch

ስድስተኛውም መልአክ ነፋ፤ በእግዚአብሔርም ፊት ካለ በወርቅ ከተሠራ መሠዊያ ቀንዶች አንድ ድምፅ ሰማሁ፥

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

waaye jamono ju juróom-ñaareelu malaaka ma wolee ci liitam, ndogalu yàlla dina mat, ni mu ko waxe woon ay jaamam, yonent yi.»

Amharisch

ወደ ፊት አይዘገይም፥ ዳሩ ግን ሰባተኛው መልአክ ሊነፋ ባለው ጊዜ ድምፁም በሚሰማበት ዘመን፥ ለባሪያዎቹ ለነቢያት የምስራች እንደ ሰበከላቸው የእግዚአብሔር ምሥጢር ይፈጸማል አለ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

noonu ma gis génn ca géej ga, rab wu am fukki béjjén ak juróom-ñaari bopp. ci kaw béjjénam ya amoon na fukki mbaxanay buur; ca bopp ya turi xarab yàlla.

Amharisch

አንድም አውሬ ከባሕር ሲወጣ አየሁ፤ አሥር ቀንዶችና ሰባት ራሶች ነበሩት፥ በቀንዶቹም ላይ አሥር ዘውዶች በራሶቹም ላይ የስድብ ስም ነበረ።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

noonu beneen firnde feeñ ca asamaan, di ninkinànka ju réy, xonq curr te am juróom-ñaari bopp ak fukki béjjén. ca bopp ya am na juróom-ñaari mbaxanay buur.

Amharisch

ሌላም ምልክት በሰማይ ታየ፤ እነሆም ታላቅ ቀይ ዘንዶ፤ ሰባት ራሶችና አሥር ቀንዶችም ነበሩት በራሶቹም ላይ ሰባት ዘውዶች ነበሩ፥

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Wolof

«bindal malaakam mbooloom ñi gëm ci dëkku efes, ne ko: i ki téye juróom-ñaari biddiiw yi ci loxol ndeyjooram, tey dox ci diggu juróom-ñaari làmpi diwlin yu wurus yi nee na:

Amharisch

በኤፌሶን ወዳለው ወደ ቤተ ክርስቲያን መልአክ እንዲህ ብለህ ጻፍ። በቀኝ እጁ ሰባቱን ከዋክብት የያዘው በሰባቱም የወርቅ መቅረዞች መካከል የሚሄደው እንዲህ ይላል።

Letzte Aktualisierung: 2012-05-05
Nutzungshäufigkeit: 1
Qualität:

Eine bessere Übersetzung mit
7,783,172,237 menschlichen Beiträgen

Benutzer bitten jetzt um Hilfe:



Wir verwenden Cookies zur Verbesserung Ihrer Erfahrung. Wenn Sie den Besuch dieser Website fortsetzen, erklären Sie sich mit der Verwendung von Cookies einverstanden. Erfahren Sie mehr. OK