Results for egipte translation from Afrikaans to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Afrikaans

Wolof

Info

Afrikaans

egipte

Wolof

isipt

Last Update: 2013-09-02
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

en jakob het afgetrek na egipte en daar gesterwe, hy en ons vaders.

Wolof

noonu yanqóoba dem misra, faatu fa, moom ak sunuy maam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

hy het toe opgestaan, die kindjie en sy moeder in die nag geneem en na egipte vertrek.

Wolof

yuusufa nag jóg, jël xale ba ak ndeyam, làquji misra ca guddi ga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

en die aartsvaders was jaloers op josef en het hom verkoop na egipte toe; maar god was met hom

Wolof

«naka maam yooyu, dañoo iñaane yuusufa, ba jaay ko, mu jëm réewu misra. waaye yàlla taxawu ko,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

na hom wou ons vaders nie luister nie, maar hulle het hom verstoot en met hulle harte na egipte teruggekeer

Wolof

waaye sunuy maam nanguwuñu koo déggal; dañu koo bañ te seeni xel dëpp, dellu misra.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

en die smaad van christus groter rykdom geag het as die skatte van egipte, want hy het uitgesien na die beloning.

Wolof

Ñu toroxal ko ngir almasi bi mi ngi mel ci moom ni alal ju ëpp alali misra yépp, ndaxte yool bi la doon séentu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

en ná die dood van herodes het daar 'n engel van die here in 'n droom aan josef in egipte verskyn

Wolof

bi nga xamee ne erodd faatu na, benn malaakam boroom bi feeñu yuusufa ci gént ca misra,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

deur die geloof het hy egipte verlaat sonder om die toorn van die koning te vrees, want hy het volgehou soos een wat die onsienlike sien.

Wolof

ngëm moo tax mu jóge misra te ragalul merum buur bi. dafa muñ, mel ni nit kuy gis yàlla, mi kenn mënul a teg bët.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

wie was dit dan wat gehoor het en hom verbitter het? was dit nie almal wat onder leiding van moses uit egipte gegaan het nie?

Wolof

Ñan ñoo dégg baatu yàlla bi nag te di ko dëddu? xanaa ña musaa génne woon misra ñépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

en hy was daar tot die dood van herodes, sodat die woord vervul sou word wat die here gespreek het deur die profeet: uit egipte het ek my seun geroep.

Wolof

mu toog fa, ba erodd faatu. noonu am li boroom bi waxoon jaarale ko cib yonent, bi mu naan:«woo naa sama doom, mu génn misra.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

en het hom uit al sy verdrukkinge verlos en hom guns en wysheid geskenk voor farao, die koning van egipte; en dié het hom goewerneur gemaak oor egipte en oor sy hele huis.

Wolof

génne ko ci coonoom yépp, defal ko yiw ak xel ci kanamu firawna, buuru misra, mu def ko kilifag misra ak këram gépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

ek het duidelik gesien die mishandeling van my volk wat in egipte is, en hulle gesug gehoor en neergedaal om hulle te verlos. en nou, kom hier, ek wil jou na egipte stuur.

Wolof

gis naa bu baax fitnay sama xeet ci misra te dégg naa seeni tawat, kon wàcc naa ngir musal leen. léegi nag ñëwal, dinaa la yebal misra.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Afrikaans

en toe hulle teruggegaan het, verskyn daar 'n engel van die here in 'n droom aan josef en sê: staan op, neem die kindjie en sy moeder en vlug na egipte, en bly daar totdat ek jou sê; want herodes gaan die kindjie soek om hom dood te maak.

Wolof

bi nga xamee ne boroom xam-xam ya ñibbi nañu, benn malaakam boroom bi feeñu yuusufa ci gént ne ko: «erodd mu ngi ci tànki wut xale bi, ngir rey ko; jógal nag, jël xale bi ak ndeyam te nga daw jëm misra, toog fa, ba kera ma koy wax.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Wikipedia

Get a better translation with
7,729,248,596 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK