Results for hoëpriester translation from Afrikaans to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Afrikaans

Wolof

Info

Afrikaans

toe sê die hoëpriester: is hierdie dinge dan so?

Wolof

noonu saraxalekat bu mag ba ne ko: «ndax loolu dëgg la?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

die hoëpriester ondervra jesus toe oor sy dissipels en oor sy leer.

Wolof

saraxalekat bu mag ba daldi laaj yeesu ci lu jëm ci taalibeem yi ak ci njàngaleem mi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en die hoëpriester en die vernaamstes van die jode het paulus by hom aangeklaag

Wolof

noonu saraxalekat yu mag ya ak njiiti yawut ya kalaame pool ci moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en is deur god genoem 'n hoëpriester volgens die orde van melgisédek;

Wolof

fekk na yàlla tudde ko saraxalekat bu mag ni ko melkisedeg nekke.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en die wat daarby staan, sê: skel jy die hoëpriester van god uit?

Wolof

waaye ña taxaw ca wetam ne ko: «ndax dangay xas saraxalekat bu mag, bi yàlla fal?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en een van hulle het die dienskneg van die hoëpriester getref en sy regteroor afgekap.

Wolof

kenn ci ñoom nag dóor surgab saraxalekat bu mag ba, noppu ndeyjooram dagg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

toe skeur die hoëpriester sy klere en sê: wat het ons nog getuies nodig!

Wolof

bi ko saraxalekat bu mag bi déggee nag, mu daldi mer, ba xotti ay yéreem naan:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en terwyl petrus onder in die binneplaas was, kom daar een van die diensmeisies van die hoëpriester,

Wolof

piyeer nag ma nga toogoon ci ëtt bi féete suuf. noonu benn mbindaanu saraxalekat bu mag ba romb fa.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

maar die hoëpriester ananías het bevel gegee aan die wat by hom staan, om hom op die mond te slaan.

Wolof

ci kaw loolu saraxalekat bu mag ba, di ku ñuy wax anañas, sant ña taxaw ca wetam, ñu fél gémmiñam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en een van die wat daar gestaan het, het sy swaard uitgetrek en die dienskneg van die hoëpriester geslaan en sy oor afgekap.

Wolof

waaye kenn ci ñi fa taxaw bocci jaaseem, dóor surgab saraxalekat bu mag bi, nopp bi dagg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en hulle het hom gevange geneem en weggelei en hom gebring in die huis van die hoëpriester. en petrus het van ver af gevolg.

Wolof

Ñu jàpp yeesu, yóbbu ko ca kër saraxalekat bu mag ba. piyeer topp fu sore.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en toe die hoëpriester en die hoofman van die tempel en die owerpriesters hierdie woorde hoor, was hulle daarmee verleë wat nou hiervan sou word.

Wolof

bi kilifag wottukati kër yàlla ga ak saraxalekat yu mag ya déggee loolu, ñu daldi ciy jaaxle lool, ñuy laajante, fu lii di mujj.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

daarom, heilige broeders, deelgenote van die hemelse roeping, let op die apostel en hoëpriester van ons belydenis, christus jesus,

Wolof

kon nag yéen bokk yu sell yi, yéen ñi yàlla woo, ngeen bokk ci nguuram gu kawe ga, seetleen ci yeesu, moom miy ndawu yàlla li, di saraxalekat bu mag bi ci yoon wi nu gëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en dit het hy nie uit homself gesê nie; maar omdat hy daardie jaar hoëpriester was, het hy geprofeteer dat jesus vir die volk sou sterwe.

Wolof

loolu kayif waxu ko woon ci sagoom, waaye li mu nekkoon saraxalekat bu mag ba at mooma, moo tax yàlla xiirtal ko mu ne, yeesu dina dee ngir réew mi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

een van die hoëpriester se diensknegte wat familie was van die man wie se oor petrus afgekap het, sê: het ek jou nie in die tuin by hom gesien nie?

Wolof

kenn ci surgay saraxalekat bu mag ba, di mbokku ka piyeer coroon noppam, ne piyeer: «xanaa du yaw laa gisoon ak moom ca tool ba?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

so het christus ook homself nie verheerlik om hoëpriester te word nie, maar hy het hom verheerlik wat vir hom gesê het: u is my seun, vandag het ek u gegenereer.

Wolof

kirist itam yékkatiwul boppam, ba doon saraxalekat bu mag, waaye yàlla moo ko woo, bi muy wax ne:«yaa di sama doom,maa di sa baay tey.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

die hoofsaak nou van wat ons gesê het, is dít: ons het so 'n hoëpriester wat gaan sit het aan die regterhand van die troon van die majesteit in die hemele,

Wolof

lii mooy li ëpp solo ci li nuy wax: am nanu saraxalekat bu mag bu mel noonu, moom mi toog ci ndeyjooru aji màgg ja ca nguuram ca kaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

daarom moes hy in alle opsigte aan sy broeders gelyk word, sodat hy 'n barmhartige en getroue hoëpriester kon wees in die dinge wat in betrekking tot god staan, om die sondes van die volk te versoen.

Wolof

looloo taxoon mu war a mel niy doomi baayam ci bépp fànn, ngir doon seen saraxalekat bu mag fa kanam yàlla, bi leen yërëm te di sàmm kóllëre, te ci liggéeyu saraxaleem joxe na bakkanam ngir dindi bàkkaari nit ñi, ba yàlla baal leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

want so 'n hoëpriester was vir ons gepas, een wat heilig, onskuldig, onbesmet, afgeskeie van die sondaars is, en wat hoër as die hemele geword het;

Wolof

kon nag yeesu mooy saraxalekat bu mag, bi nu soxla; dafa sell, du def lu bon, du taq bàkkaar, bokkul dara ak bàkkaarkat yi, te yéege nañu ko fa yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en hulle het geluister en vroeg in die môre in die tempel gegaan en begin leer. maar die hoëpriester en die wat saam met hom was, het gekom en die raad en al die oudstes van die kinders van israel bymekaargeroep; en hulle het na die gevangenis gestuur om hulle te laat haal.

Wolof

bi ñu déggee loolu, ñu dugg ca kër yàlla ga ci suba teel, daldi waare. bi ñu koy def, saraxalekat bu mag ba ak gàngooram ñëw, woolu kureelu àttekat ya, maanaam mbooloom njiiti bànni israyil gépp; ñu yónnee, ngir jëli ndaw ya ca kaso ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,745,676,863 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK