From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
i jedli všickni, a nasyceni jsou.
noonu ñépp lekk ba suur.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a všickni týž pokrm duchovní jedli,
Ñoom ñépp bokk nañoo lekk ñam, wa yàlla joxe,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
otcové vaši jedli mannu na poušti, a zemřeli.
seeni maam lekk nañu mànn ca màndiŋ ma, teewul dee nañu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a bylo těch, kteříž jedli ty chleby, okolo pět tisíců mužů.
Ñu lekkoon nag matoon na limu juróomi junniy góor.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bylo pak těch, kteříž jedli, čtyři tisíce mužů kromě žen a dětí.
gannaaw jigéen ñi ak gune yi, góor ñi ci lekk matoon nañu ñeenti junni.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
i jedli a nasyceni jsou; a sebrali, což pozůstalo drobtů, sedm košů.
noonu nit ñi lekk ba suur, ba noppi taalibe yi dajale juróom-ñaari dàmba yu fees ak dammit yi ci des.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a když jedli, řekl jim: amen pravím vám, že jeden z vás mne zradí.
bi ñuy lekk, mu ne leen: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, kenn ci yéen dina ma wor.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
i jedli všickni a nasyceni jsou. i sebrali pozůstalých drobtů, dvanácte košů plných.
noonu ñépp lekk ba suur. te ñu dajale dammit ya ca des, mu nekk fukki pañe ak ñaar yu fees.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
i jedli všickni a nasyceni jsou. a sebrali, což zbylo drobtů, sedm košů plných.
noonu ñépp lekk ba suur. te ñu dajale juróom-ñaari dàmba yu fees ak dammit yi ci des.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
otcové naši jedli mannu na poušti, jakož psáno jest: chléb s nebe dal jim jísti.
sunuy maam dunde nañu mànn ca màndiŋ ma, ndaxte mbind mi nee na: “jox na leen, ñu lekk ñam wu wàcce ca asamaan.”»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
i jedli, a nasyceni jsou všickni. a sebráno jest, což jim bylo ostalo drobtů, dvanácte košů.
noonu ñépp lekk ba suur. bi ñu dajalee desit ya, ñu feesal fukki pañe ak ñaar.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
abyste jedli a pili za stolem mým v království mém, a seděli na stolicích, soudíce dvanáctero pokolení izraelské.
dingeen lekkandoo te naanandoo ak man ci sama nguur. te dingeen toog ci jal yi, di àtte fukki giir ak ñaar yu bànni israyil.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ne všemu lidu, ale svědkům prve k tomu zřízeným od boha, nám, kteříž jsme s ním jedli a pili po jeho z mrtvých vstání.
waxuma xeet wépp, waaye seede yi yàlla tànn lu jiitu, maanaam nun ñi daan lekk di naan ak moom gannaaw ndekkiteem.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
(jiné pak lodí byly připlouly od tiberiady k tomu místu blízko, kdežto byli jedli chléb, když díky učinil pán,)
waaye yeneen gaal yu jóge dëkku tiberyàdd ñëw, teer ca wetu fa ñu lekke woon mburu ma, gannaaw bi boroom bi santee yàlla ba noppi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a též podobně, jako se stalo ve dnech lotových: jedli, pili, kupovali, prodávali, štěpovali, stavěli.
«dina mel it ni la xewoon ca bési lóot. nit ñaa ngi doon lekk ak di naan, di jënd ak di jaay, di ji ak di tabax.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
totoť jest ten chléb, kterýž s nebe sstoupil. ne jako otcové vaši jedli mannu, a zemřeli. kdož jí chléb tento, živť bude na věky.
kon nag ñam, wi wàcce ci asamaan a ngi noonu; bokkul ak ñam, wa seeni maam lekkoon te faatu. ku lekk ñam wii may wax dinga dund ba fàww.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a když oni jedli, vzav ježíš chléb a dobrořečiv, lámal, a dal učedlníkům, a řekl: vezměte, jezte, to jest tělo mé.
noonu bu ñuy lekk, yeesu jël mburu, sant yàlla, damm ko, jox ko taalibe ya. mu ne leen: «jël-leen lekk, lii sama yaram la.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
odpověděl jim ježíš a řekl: amen, amen pravím vám: hledáte mne, ne protože jste divy viděli, ale že jste jedli chleby a nasyceni jste.
yeesu ne leen: «ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, firnde yi ngeen gis taxul ngeen may seet. yéena ngi may wër ndax mburu, mi ngeen lekk ba suur.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
abyste jedli těla králů, a těla hejtmanů, a těla silných, a těla koňů, i těch, kteříž na nich sedí, a těla všech svobodných i služebníků, i malých i velikých.
ngeen lekk suuxi buur yi, njiiti xare yi ak boroom kàttan yi, suuxi fas yi ak seeni gawar, suuxi ñépp: gor ak jaam, mag ak ndaw.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a kamžkoli vejde, rcete k hospodáři domu toho: mistrť praví: kde jest večeřadlo, v němž bych jedl beránka s učedlníky svými?
kër gi mu dugg nag, ngeen ne boroom kër gi: “kilifa gi nee na: ana néegu gan, bi may lekke reeru jéggi bi, man ak samay taalibe?”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: