Results for samler translation from Danish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Danish

Wolof

Info

Danish

således er det med den, som samler sig skatte og ikke er rig i gud."

Wolof

«kiy dajale alal ngir boppam nag te amul dara ca kanam yàlla, lu mel nii moo lay dal.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

den, som ikke er med mig, er imod mig; og den, som ikke samler med mig, adspreder.

Wolof

ku farul ak man, yaa ngi may xeex, ku dajalewul ak man, yaa ngi tasaare.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

samler eder ikke skatte på jorden, hvor møl og rust fortære, og hvor tyve bryde ind og stjæle;

Wolof

«buleen dajale alal ci àddina, fu ko max ak xomaag di yàqe, ak fu sàcc di dugg, jot ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

men samler eder skatte i himmelen, hvor hverken møl eller rust fortære, og hvor tyve ikke bryde ind og stjæle.

Wolof

waaye dajaleleen alal ci laaxira, fu ko max ak xomaag dul yàqe, ak fu sàcc dul dugg, jot ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

og han bryder op derfra og kommer til judæas egne og landet hinsides jordan, og atter samler der sig skarer om ham; og han lærte dem atter, som han plejede.

Wolof

gannaaw loolu yeesu jóge fa, dem ca wàlli réewu yawut yi, ya ca gannaaw dexu yurdan. bi mu fa demee, mbooloo mu bare ñëw fi moom. yeesu daldi leen jàngal, ni mu ko daan defe.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

den, som høster, får løn og samler frugt til et evigt liv, så at de kunne glæde sig tilsammen, både den, som sår, og den, som høster.

Wolof

kiy góob tool yi mu ngi jot xaat peyam; day dajale nit ñi ngir dund gu dul jeex, ni ñuy dajalee pepp. kon boog kiy ji dina bégandoo ak kiy góob.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

men da de vare blevne mætte, siger han til sine disciple: "samler de tiloversblevne stykker sammen, for at intet skal gå til spilde."

Wolof

bi ñu lekkee ba regg, yeesu ne taalibe ya: «dajaleleen desitu mburu mi, ba dara du ci réer.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

da imidlertid mange tusinde mennesker havde samlet sig, så at de trådte på hverandre, begyndte han at sige til sine disciple: "tager eder først og fremmest i vare for farisæernes surdejg, som er hykleri.

Wolof

gannaaw loolu, naka la mbooloo ma dajaloo ba mat ay junniy junniy nit, di tancante, yeesu tàmbalee wax jëmale ca taalibeem ya ne leen: «moytuleen lawiiru farisen ya, li di naaféq.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
8,934,044,218 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK