Results for vagtafdelingen translation from Danish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Danish

Wolof

Info

Danish

vagtafdelingen og krigsøversten og jødernes svende grebe da jesus og bandt ham.

Wolof

mbooloom xarekat ya ak seen kilifa ak alkaatiy yawut ya jàpp yeesu, daldi yeew,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

da toge landshøvdingens stridsmænd jesus med sig ind i borgen og samlede hele vagtafdelingen omkring ham.

Wolof

bi ñu ko defee xarekati boroom réew ma fab yeesu, yóbbu ko ci biir kër ga, ñu daldi woo mbooloom xarekat ya yépp ci moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

men stridsmændene førte ham ind i gården, det vil sige borgen, og de sammenkalde hele vagtafdelingen.

Wolof

bi loolu amee ñu dugal yeesu ci biir kër boroom réew ma, mooy bérab bu ñuy wax peretoriyum, ñu daldi woo mbooloom xarekat yépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

så tager judas vagtafdelingen og svende fra ypperstepræsterne og farisæerne og kommer derhen med fakler og lamper og våben.

Wolof

yudaa daldi fa dem, yóbbaale mbooloom xarekat ak ay alkaati yu ko saraxalekat yu mag ya ak farisen ya jox. Ñu yor ay jum ak ay làmp ak it gànnaay.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

og da de søgte at slå ham ihjel, gik der melding op til krigsøversten for vagtafdelingen, at hele jerusalem var i oprør.

Wolof

bi ñu koy wut a rey, xebaar ba agsi ba ca kilifag mbooloom xarekat ba, naan yerusalem gépp jaxasoo na.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,774,902,322 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK