Results for abideth translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

if we believe not, yet he abideth faithful: he cannot deny himself.

Wolof

su nu ko weddee,kon mu weddi nu;su nu ko ñàkkee kóllëre,moom dina sax ci kóllëreem,ndax mënul a weddi boppam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the servant abideth not in the house for ever: but the son abideth ever.

Wolof

te jaam du bokk ci kër gi ba fàww, waaye doom, moom, ci kër gi la bokk ba fàww.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

he that saith he abideth in him ought himself also so to walk, even as he walked.

Wolof

ku wax ne ci yàlla nga sax, fàww nga dund, ni yeesu kirist daan dunde moom ci boppam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

he that loveth his brother abideth in the light, and there is none occasion of stumbling in him.

Wolof

kuy sopp sa mbokk, yaa ngi dëkk ci leer, te luy yóbbe nit bàkkaar du nekk ci yaw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the world passeth away, and the lust thereof: but he that doeth the will of god abideth for ever.

Wolof

te àddina day wéy, waaye kuy def coobareg yàlla dinga sax ba fàww.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and now abideth faith, hope, charity, these three; but the greatest of these is charity.

Wolof

léegi nag ñett yii ñooy sax: ngëm, yaakaar, mbëggeel; te mbëggeel moo ci raw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

we know that we have passed from death unto life, because we love the brethren. he that loveth not his brother abideth in death.

Wolof

mbëggeel gi nu bëgg sunuy bokk moo nuy xamal ne, jóge nanu ci dee, tàbbi ci dund. ku bëggul sa mbokk, yaa ngi ci dee ba tey.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

being born again, not of corruptible seed, but of incorruptible, by the word of god, which liveth and abideth for ever.

Wolof

ndaxte du ci jiwu wuy yàqu ngeen judduwaate, waaye ci jiwu wu sax, maanaam kàddug yàlla giy dund tey sax.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he that keepeth his commandments dwelleth in him, and he in him. and hereby we know that he abideth in us, by the spirit which he hath given us.

Wolof

kuy sàmm ndigalu yàlla, dinga sax ci moom, mu dëkk ci yaw. te xel mi mu nu jox, moo nuy xamal ne, dëkk na ci nun.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

whosoever transgresseth, and abideth not in the doctrine of christ, hath not god. he that abideth in the doctrine of christ, he hath both the father and the son.

Wolof

képp ku saxul ci dénkaaney krist, xanaa di ko weesu, bokkul ci yàlla; ku sax ci dénkaane yi, bokk nga ak baay bi ak doom ji.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

i am the vine, ye are the branches: he that abideth in me, and i in him, the same bringeth forth much fruit: for without me ye can do nothing.

Wolof

«man maay garab gi; yéen yéenay car yi. ki sax ci man te ma sax ci moom, dina meññ, ndaxte bu ngeen saxul ci man, dungeen man dara.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

the people answered him, we have heard out of the law that christ abideth for ever: and how sayest thou, the son of man must be lifted up? who is this son of man?

Wolof

mbooloo ma tontu ko ne: «jàng nanu ci sunu téereb yoon ne, almasi bi dina sax ba fàww. kon yaw, nan nga man a waxe ne, “doomu nit ki dina yékkatiku?” kuy doomu nit kooku?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but the anointing which ye have received of him abideth in you, and ye need not that any man teach you: but as the same anointing teacheth you of all things, and is truth, and is no lie, and even as it hath taught you, ye shall abide in him.

Wolof

yéen nag, xel mi leen kirist sol a ngi dëkk ci yéen, te soxlawuleen kenn jàngal leen dara. waaye xel mi mu leen sol, mi ngi leen di jàngal lépp, te li mu leen di jàngal mooy dëgg; kon nag saxleen ci moom, ni mu leen ko jàngale.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,787,067,077 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK