From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
proving what is acceptable unto the lord.
dëggal-leen ci seeni jëf li neex boroom bi,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
to preach the acceptable year of the lord.
tey yégle atum yiw, mi jóge ci boroom bi.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for this is good and acceptable in the sight of god our saviour;
loolu mooy li rafet te neex yàlla sunu musalkat,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for he that in these things serveth christ is acceptable to god, and approved of men.
kiy jaamoo noonu kirist moo neex yàlla ak nit ñi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but if any widow have children or nephews, let them learn first to shew piety at home, and to requite their parents: for that is good and acceptable before god.
waaye ku ci am ay doom mbaa ay sët, na njaboot googu jëkk a wone seen ragal yàlla ci seen biir kër, ci delloo njukkal seen waajur, ndaxte loolu lu rafet la fa kanam yàlla.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and be not conformed to this world: but be ye transformed by the renewing of your mind, that ye may prove what is that good, and acceptable, and perfect, will of god.
bu leen àddina jey, waaye yeesluleen ci seen xel, ba soppiku, ngeen man a xam bu wér coobareg yàlla, di lépp lu baax, neex ko te mat sëkk.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but i have all, and abound: i am full, having received of epaphroditus the things which were sent from you, an odour of a sweet smell, a sacrifice acceptable, wellpleasing to god.
fi mu ne jot naa li ma aajowoo lépp, ba maa ngi ci naataange; li ngeen ma yónnee ci loxoy epafrodit doy na sëkk; ni xetu latkoloñ la mel ci man, di sarax su neex yàlla te mu nangu ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for what glory is it, if, when ye be buffeted for your faults, ye shall take it patiently? but if, when ye do well, and suffer for it, ye take it patiently, this is acceptable with god.
su ngeen tooñee te muñ i pes, luy pey gi? waaye su ñu leen fitnaalee ci def lu baax te ngeen muñ ko, jëf ju rafet la fa kanam yàlla.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: