From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
fathers, provoke not your children to anger, lest they be discouraged.
baay yi, buleen bundaxataal seeni doom, ngir bañ a jeexal seen xol.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but now ye also put off all these; anger, wrath, malice, blasphemy, filthy communication out of your mouth.
waaye léegi bàyyileen yii yépp: mer, xadar, kiñaan ak di génne ci seen gémmiñ sos ak wax ju ñaaw.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
let all bitterness, and wrath, and anger, and clamour, and evil speaking, be put away from you, with all malice:
dëdduleen lépp luy wex mbaa tàng bopp, luy mer mbaa coow, lépp luy xaste mbaa coxor.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but i say, did not israel know? first moses saith, i will provoke you to jealousy by them that are no people, and by a foolish nation i will anger you.
waaye ma teg ci ne: xanaa bànni israyil dañoo xamul? aaŋkay! musaa dafa jëkkoon a wax ne:«dinaa leen siisloo xeet wu bokkul ci yàlla,merloo leen ci ñi xamul dara ci yàlla.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when he had looked round about on them with anger, being grieved for the hardness of their hearts, he saith unto the man, stretch forth thine hand. and he stretched it out: and his hand was restored whole as the other.
ci kaw loolu yeesu xool leen ak mer, am naqar ndax seen xol bu fatt; ba noppi mu ne nit ki: «tàllalal sa loxo.» nit ki tàllal ko, loxoom daldi wér peŋŋ.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: