From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
what therefore god hath joined together, let not man put asunder.
lu yàlla takk nag, bu ko nit tas.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
wherefore they are no more twain, but one flesh. what therefore god hath joined together, let not man put asunder.
kon nag nekkatuñu ñaar waaye benn. lu yàlla takk nag, bu ko nit tas.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and shall cut him asunder, and appoint him his portion with the hypocrites: there shall be weeping and gnashing of teeth.
dina ko dóor ay yar yu metti, jox ko añub naaféq. foofa dees na fa jooy tey yéyu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and the contention was so sharp between them, that they departed asunder one from the other: and so barnabas took mark, and sailed unto cyprus;
noonu ñu xuloo, ba far tàggoo. barnabas yóbbaale màrk, ñu dugg gaal, jëm sipar.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
because that he had been often bound with fetters and chains, and the chains had been plucked asunder by him, and the fetters broken in pieces: neither could any man tame him.
ndaxte ay yoon yu bare jéngoon nañu ko te yeew ko ak ay càllala, waaye waa ji daldi dagg càllala yi te damm jéng yi, ba kenn amul woon kàttanu téye ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for the word of god is quick, and powerful, and sharper than any twoedged sword, piercing even to the dividing asunder of soul and spirit, and of the joints and marrow, and is a discerner of the thoughts and intents of the heart.
xam nanu ne, kàddug yàlla mi ngi dund te am na doole. moo gën a ñaw jaasiy ñaari boor. day dagg ba fa xol ak xel digaloo, ba fa yax yi ak yuq gi di teqalikoo, te man na àtte xalaat yi ak mébéti xol.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
they were stoned, they were sawn asunder, were tempted, were slain with the sword: they wandered about in sheepskins and goatskins; being destitute, afflicted, tormented;
Ñii, sànni nañu leen ay xeer ba ñu dee; ñii, ñu xar leen ñaar; ñii, ñu reye leen jaasi. Ñu ngi doon wëndéelu, sol ay deri xar ak yu bëy, di ay walaakaana; ñu di leen sonal, di leen fitnaal.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: