Results for baptized translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

lest any should say that i had baptized in mine own name.

Wolof

ngir kenn bañ a wax ne, ci sama tur lañu ko sóob.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and were baptized of him in jordan, confessing their sins.

Wolof

Ñu nangu seeni bàkkaar, yaxya sóob leen ca dexu yurdan.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

(though jesus himself baptized not, but his disciples,)

Wolof

fekk yeesu moom ci boppam daawul sóob kenn ci ndox, waaye ay taalibeem ñoo daan sóobe.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and were all baptized unto moses in the cloud and in the sea;

Wolof

sóobu nañu ca ndoxu géej ga ak ca niir wa, ba bokk noonu ci musaa.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for as many of you as have been baptized into christ have put on christ.

Wolof

yéen ñépp, ñi ñu sóob ci ndox ngir wone seen bokk ci kirist, soloo ngeen kirist.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

i thank god that i baptized none of you, but crispus and gaius;

Wolof

maa ngi sant yàlla ci li ma sóobul kenn ci yéen, ku dul kirispus ak gayus,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

then cometh jesus from galilee to jordan unto john, to be baptized of him.

Wolof

booba yeesu jóge galile, ñëw ngir yaxya sóob ko ca dexu yurdan.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

i indeed have baptized you with water: but he shall baptize you with the holy ghost.

Wolof

maa ngi leen di sóob ci ndox, waaye moom dina leen sóob ci xel mu sell mi.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but the pharisees and lawyers rejected the counsel of god against themselves, being not baptized of him.

Wolof

waaye farisen ya ak xutbakat ya dañoo bañ, mu sóob leen ci ndox, di wone noonu ne, gàntu nañu li leen yàlla bëggaloon.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he commanded them to be baptized in the name of the lord. then prayed they him to tarry certain days.

Wolof

noonu mu santaane, ñu sóob leen ci ndox ci turu yeesu kirist. gannaaw loolu ñu ñaan ko, mu toog ci ñoom ay fan.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he said unto them, unto what then were ye baptized? and they said, unto john's baptism.

Wolof

mu ne leen: «kon nag, bi ñu leen sóobee ci ndox, lu ciy maana?» Ñu tontu ko: «xanaa li yaxya tëral.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and all the people that heard him, and the publicans, justified god, being baptized with the baptism of john.

Wolof

nit ñépp ñi doon déglu yeesu, ba ci juutikat yi sax, dëggal nañu ne yàlla ku jub la, ndaxte nangu nañu yaxya sóob leen ci ndox.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

after these things came jesus and his disciples into the land of judaea; and there he tarried with them, and baptized.

Wolof

gannaaw loolu yeesu ànd ak ay taalibeem, dem ca biir diiwaanu yude, toog fa ak ñoom ab diir, di sóob nit ñi ci ndox.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

(for as yet he was fallen upon none of them: only they were baptized in the name of the lord jesus.)

Wolof

ndaxte wàccagul ci kenn ci ñoom, waaye sóoboon nañu leen rekk ci ndox ci turu boroom bi yeesu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he took them the same hour of the night, and washed their stripes; and was baptized, he and all his, straightway.

Wolof

mu jël leen nag ci waxtu woowu ci guddi, raxas seeni gaañu-gaañu, ba noppi ñu sóob ko ci ndox, moom ak waa këram gépp.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and there went out unto him all the land of judaea, and they of jerusalem, and were all baptized of him in the river of jordan, confessing their sins.

Wolof

kon waa diiwaanu yude ñépp ak waa dëkku yerusalem ñépp daldi génn jëm ci moom, di nangu seeni bàkkaar fi kanam ñépp, yaxya sóob leen ca dexu yurdan.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and crispus, the chief ruler of the synagogue, believed on the lord with all his house; and many of the corinthians hearing believed, and were baptized.

Wolof

kirispus nag, njiitu jàngu ba, gëm na boroom bi ak waa këram gépp. te waa korent ñu bare dégg kàddu gi te gëm ko, ñu sóob leen ci ndox.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but jesus said unto them, ye know not what ye ask: can ye drink of the cup that i drink of? and be baptized with the baptism that i am baptized with?

Wolof

waaye yeesu tontu leen: «xamuleen li ngeen di ñaan. ndax man ngeen a naan kaasu naqar, bi may naan? ndax man ngeen a sóobu ci metit, yi ma nar a sóobu?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and as they went on their way, they came unto a certain water: and the eunuch said, see, here is water; what doth hinder me to be baptized?

Wolof

bi ñuy jaar ci yoon wi, ñu agsi ci ndox. jaraaf ja ne ko: «ndox a ngi nii, ana lu tere, nga sóob ma ci?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they said unto him, we can. and jesus said unto them, ye shall indeed drink of the cup that i drink of; and with the baptism that i am baptized withal shall ye be baptized:

Wolof

Ñu ne ko: «waaw, man nanu ko.» noonu yeesu ne leen: «dingeen naan kaasu naqar, bi may naan, tey sóobu ci metit, yi ma nar a sóobu,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,854,538,015 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK