From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
for ye have brought hither these men, which are neither robbers of churches, nor yet blasphemers of your goddess.
ndaxte nit ñii ngeen fi indi sàccuñu ca màggalukaay ya te sosaluñu sunu yàlla.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for men shall be lovers of their own selves, covetous, boasters, proud, blasphemers, disobedient to parents, unthankful, unholy,
ndaxte nit ñi dinañu siis te fonk xaalis, di ñu réy tey yég seen bopp, ñuy xaste tey xëtt ndigalu waajur; duñu am kóllëre, sellaay
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
who was before a blasphemer, and a persecutor, and injurious: but i obtained mercy, because i did it ignorantly in unbelief.
moona daa naa suufeel turam, di fitnaal ak a toroxal ñi ko gëm. waaye yàlla yërëm na ma, ndaxte ñàkka xam ak ñàkka gëm rekk a taxoon ma def ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: