From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
that he might sanctify and cleanse it with the washing of water by the word,
ngir sellal ko ak kàddoom, ba mu laab ni ku sangu set.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he shewed me a pure river of water of life, clear as crystal, proceeding out of the throne of god and of the lamb.
noonu malaaka ma won ma dexu ndoxum dund, mu leer ni weer bu set, di génn ca gàngune mu yàlla ak mbote ma,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
if ye know that he is righteous, ye know that every one that doeth righteousness is born of him.
gannaaw xam ngeen ne ku jub la, dingeen xam it ne, képp kuy def lu jub juddu nga ci moom.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
that which is born of the flesh is flesh; and that which is born of the spirit is spirit.
lu juddoo ci nit, nit la; waaye lu juddoo ci xelum yàlla, xel la.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for whosoever shall give you a cup of water to drink in my name, because ye belong to christ, verily i say unto you, he shall not lose his reward.
ci dëgg maa ngi leen koy wax, koo xam ne kii may na leen kaasu ndox rekk, ndax yéena ngi bokk ci man kirist, kooku du ñàkk yoolam mukk.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but whosoever drinketh of the water that i shall give him shall never thirst; but the water that i shall give him shall be in him a well of water springing up into everlasting life.
waaye ndox, mi may joxe, ku ci naan du marati mukk, ndaxte day nekk ci moom bëtu ndox buy ball, di joxe dund gu dul jeex.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he sendeth forth two of his disciples, and saith unto them, go ye into the city, and there shall meet you a man bearing a pitcher of water: follow him.
noonu yeesu yebal ñaar ci taalibe yi ne leen: «demleen ca dëkk ba, foofa góor gu yenu njaq lu def ndox, dina taseek yéen, ngeen topp ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he said unto them, behold, when ye are entered into the city, there shall a man meet you, bearing a pitcher of water; follow him into the house where he entereth in.
mu ne leen: «bu ngeen duggee ca dëkk ba, góor gu yenu njaq lu def ndox, dina taseek yéen. toppleen ci moom ba ca kër ga muy dugg,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for i say unto you, among those that are born of women there is not a greater prophet than john the baptist: but he that is least in the kingdom of god is greater than he.
maa ngi leen koy wax, ci li jigéen jur, ku sut yaxya musul a feeñ. waaye ba tey ki gën a ndaw ci nguuru yàlla moo ko sut.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and the third angel poured out his vial upon the rivers and fountains of waters; and they became blood.
Ñetteelu malaaka ma sotti ndabam ci dex yi ak ci bëti ndox yi. Ñu daldi nekk deret.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and the angel answered and said unto her, the holy ghost shall come upon thee, and the power of the highest shall overshadow thee: therefore also that holy thing which shall be born of thee shall be called the son of god.
malaaka ma tontu ko ne: «xel mu sell mi dina wàcc ci yaw, te aji kawe ji dina la yiir ci kàttanam. moo tax xale biy juddu dinañu ko wooye ku sell ki, doomu yàlla ji.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.