Results for chief translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and the chief priests and scribes stood and vehemently accused him.

Wolof

saraxalekat yu mag ya ak xutbakat yaa nga fa woon, di ko jiiñ bu metti.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and whosoever will be chief among you, let him be your servant:

Wolof

te ku bëgg a nekk njiit, na nekk seen jaam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and here he hath authority from the chief priests to bind all that call on thy name.

Wolof

te indaale na fii sax sañ-sañ bu jóge ci saraxalekat yu mag ya, ngir yeew képp kuy tudd saw tur.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and love the uppermost rooms at feasts, and the chief seats in the synagogues,

Wolof

ca reeri xew yi, toogu yu yiw lañuy taamu, tey féete kanam ca jàngu ya.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but some of them said, he casteth out devils through beelzebub the chief of the devils.

Wolof

waaye am ca mbooloo ma ay nit, ñu doon wax naan: «ci kàttanu beelsebul, buuru rab yi, lay dàqe rab yi.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and pilate, when he had called together the chief priests and the rulers and the people,

Wolof

pilaat daldi woo saraxalekat yu mag ya, njiit ya ak mbooloom yawut ya ne leen:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when the chief priests and pharisees had heard his parables, they perceived that he spake of them.

Wolof

bi nga xamee ne saraxalekat yu mag ya ak farisen ya dégg nañu léebam yooyu, ñu xam ne ñoom lay wax.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and how the chief priests and our rulers delivered him to be condemned to death, and have crucified him.

Wolof

waaye sunuy saraxalekat yu mag ak sunuy njiit ñoo ko jébbal nguur gi ngir ñu àtte ko, teg ko dee, ba daaj ko ci bant.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he went his way, and communed with the chief priests and captains, how he might betray him unto them.

Wolof

noonu yudaa dem waxtaani ak saraxalekat yu mag ya ak kilifay wottukati kër yàlla ga, ba xam nan la leen di jébbale yeesu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and are built upon the foundation of the apostles and prophets, jesus christ himself being the chief corner stone;

Wolof

yéena ngi sukkandikoo ci fondamaa, bi ndawi kirist yi ak yonent yi tabax, te kirist yeesu ci boppam di doju dalil wa.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he taught daily in the temple. but the chief priests and the scribes and the chief of the people sought to destroy him,

Wolof

bés bu nekk yeesu di jàngale ca kër yàlla ga. saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya, ñoom ak njiiti xeet wa, ñu ngi ko doon wut a reylu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and it came to pass, as he went into the house of one of the chief pharisees to eat bread on the sabbath day, that they watched him.

Wolof

benn bésu noflaay yeesu dem ci këru benn kilifag farisen yi, ngir lekke fa. nit ñaa ngi ko doon xool bu baax.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

about whom, when i was at jerusalem, the chief priests and the elders of the jews informed me, desiring to have judgment against him.

Wolof

te bi ma nekkee yerusalem, saraxalekat yu mag ya ak njiiti yawut ya kalaame nañu ko ci man, ñaan ma, ma daan ko.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and as soon as it was day, the elders of the people and the chief priests and the scribes came together, and led him into their council, saying,

Wolof

bi bët setee, kureelu njiiti xeet wa, maanaam saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya, daldi daje, indi yeesu ci seen kanam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and crispus, the chief ruler of the synagogue, believed on the lord with all his house; and many of the corinthians hearing believed, and were baptized.

Wolof

kirispus nag, njiitu jàngu ba, gëm na boroom bi ak waa këram gépp. te waa korent ñu bare dégg kàddu gi te gëm ko, ñu sóob leen ci ndox.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

after two days was the feast of the passover, and of unleavened bread: and the chief priests and the scribes sought how they might take him by craft, and put him to death.

Wolof

booba nag saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ñu ngi doon fexeel yeesu, ngir jàpp ko, reylu. fekk booba ñaari fan a des ci màggalu bésu jéggi ba ak màggalu mburu ya amul lawiir.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when the chief priests and scribes saw the wonderful things that he did, and the children crying in the temple, and saying, hosanna to the son of david; they were sore displeased,

Wolof

bi nga xamee ne saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya gis nañu yëf yu doy waar ya mu def, te dégg xale yu ndaw ya nekk ca kër yàlla ga, di wax ci kaw naan: «osaana, yaw sëtu daawuda bi!» ñu daldi mer.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and immediately, while he yet spake, cometh judas, one of the twelve, and with him a great multitude with swords and staves, from the chief priests and the scribes and the elders.

Wolof

bi yeesu di wax, yudaa mi bokkoon ci fukki taalibe ya ak ñaar, agsi, ànd ak mbooloo mu bare, mu jóge ca saraxalekat yu mag ya, ca xutbakat ya ak ca njiiti xeet wa, te gànnaayoo jaasi ak yet.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he began to teach them, that the son of man must suffer many things, and be rejected of the elders, and of the chief priests, and scribes, and be killed, and after three days rise again.

Wolof

booba yeesu tàmbali na leen a xamal ne, doomu nit ki war na sonn lu bare; njiit ya, saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya dëddu ko, ñu rey ko, mu dekki ci ñetti fan.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the kings of the earth, and the great men, and the rich men, and the chief captains, and the mighty men, and every bondman, and every free man, hid themselves in the dens and in the rocks of the mountains;

Wolof

noonu buuri àddina si, kilifa yi, njiiti xare yi, boroom alal yi, boroom kàttan yi, jaam yi ak gor yi, ñépp làqatuji ci xunti yi ak ci ron doji tund yi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,892,211,864 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK