From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
do you hate me
Last Update: 2021-04-14
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
what do you do?
wayaw loy def nii
Last Update: 2017-01-13
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
do not err, my beloved brethren.
yéen sama bokk yi ma bëgg, buleen juum ci lii:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and this will we do, if god permit.
te noonu lanuy def, bu soobee yàlla.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
do thy diligence to come shortly unto me:
defal sa kem-kàttan, ba fekksi ma ci ni mu gën a gaawe.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
do all things without murmurings and disputings:
lépp lu ngeen di def nag, buleen ci boole xultu mbaa xuloo.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
mine answer to them that do examine me is this,
nii laay tontoo ñi may àtte:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
faithful is he that calleth you, who also will do it.
yàlla, mi leen woo ci loolu, kuy sàmm kóllëre la, te dina ko def.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and again he denied with an oath, i do not know the man.
waaye piyeer weddiwaat, boole ko ak ay ngiñ ne ko: «xawma nit kooku.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and he said unto them, how is it that ye do not understand?
noonu yeesu ne leen: «ndax seen xol dafa tëju ba tey?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and he said unto them, what would ye that i should do for you?
yeesu tontu leen: «lu ngeen bëggoon, ma may leen ko?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and as ye would that men should do to you, do ye also to them likewise.
defal-leen nit ñi li ngeen bëgg, ñu defal leen ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and brought them out, and said, sirs, what must i do to be saved?
mu génne leen ci biti ne leen: «kilifa yi, lu ma war a def, ba mucc?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and certain of them that stood there said unto them, what do ye, loosing the colt?
bi ñu koy yiwi nag, am na ca ña fa taxaw, ñu ne leen: «lu ngeen nar, bay yiwi cumbur gi?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and they were filled with madness; and communed one with another what they might do to jesus.
waaye nit ña mer ba fees, di rabat pexe yu jëm ca yeesu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and after the sop satan entered into him. then said jesus unto him, that thou doest, do quickly.
naka la yudaa jël dog wa, seytaane dugg ci moom. yeesu ne ko: «gaawantul ci li ngay def!»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and a certain ruler asked him, saying, good master, what shall i do to inherit eternal life?
benn njiitu yawut laaj yeesu ne ko: «kilifa gu baax gi, lu ma war a def, ba am wàll ci dund gu dul jeex?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and he thought within himself, saying, what shall i do, because i have no room where to bestow my fruits?
muy werante ci xelam naan: “nu ma war a def? ndaxte amatuma fu ma dajale sama ngóob mi.”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
jesus answered them, many good works have i shewed you from my father; for which of those works do ye stone me?
noonu yeesu ne leen: «def naa ci seen kanam jëf yu baax yu bare ci ndigalu baay bi. ban ci jëf yooyu moo tax ba ngeen bëgg maa sànni ay doj?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and, behold, a certain lawyer stood up, and tempted him, saying, master, what shall i do to inherit eternal life?
noonu benn xutbakat daldi jóg, ngir fexee fiir yeesu ne ko: «kilifa gi, lan laa war a def, ba am dund gu dul jeex?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: