From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
the elder unto the wellbeloved gaius, whom i love in the truth.
man njiit li, maa ngi lay bind, yaw sama xarit gayus, mi ma bëgg ci sama xol.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
against an elder receive not an accusation, but before two or three witnesses.
kuy tuumaal njiit fi yaw, bu ko gëm, li feek ñaar walla ñetti seede dëggaluñu ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
rebuke not an elder, but intreat him as a father; and the younger men as brethren;
bul gëdd mag, waaye waxtaanal ak moom ni sa baay. ndaw it, nga digal ko ni sa rakk,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
now his elder son was in the field: and as he came and drew nigh to the house, he heard musick and dancing.
«fekk booba taaw baa nga woon ca tool ya. bi mu ñëwee, ba jub kër ga, mu dégg ñuy tëgg, di fecc.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
the elder unto the elect lady and her children, whom i love in the truth; and not i only, but also all they that have known the truth;
man njiit li maa leen di bind, yaw soxna su tedd si, yaw ak say doom. bëgg naa leen bu wér ci sama xol, jéllale naa sama bopp sax, waaye itam képp ku xam dëgg gi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
the elders which are among you i exhort, who am also an elder, and a witness of the sufferings of christ, and also a partaker of the glory that shall be revealed:
kon yéen njiit yi, maa ngi leen di dénk, man miy njiit ni yéen, man mi seede coonoy kirist te am cér ci ndam li nar a feeñ.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
about whom, when i was at jerusalem, the chief priests and the elders of the jews informed me, desiring to have judgment against him.
te bi ma nekkee yerusalem, saraxalekat yu mag ya ak njiiti yawut ya kalaame nañu ko ci man, ñaan ma, ma daan ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: