From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
it is not expedient for me doubtless to glory. i will come to visions and revelations of the lord.
damu amul jariñ, ba tey war na ma. kon ma jàll ci nettali gis-gisi boroom bi ak i peeñu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nor consider that it is expedient for us, that one man should die for the people, and that the whole nation perish not.
xanaa xamuleen ne, kenn nit rekk dee ngir ñépp, mooy li gën ci yéen? bu ko defee réew mi du tas.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
all things are lawful for me, but all things are not expedient: all things are lawful for me, but all things edify not.
dafa am ñu naan: «lépp lanu sañ.» waaw, waaye du lépp a baax ci nun. «lépp lanu sañ,» waaye it lépp du yékkati ngëm.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
all things are lawful unto me, but all things are not expedient: all things are lawful for me, but i will not be brought under the power of any.
am na ci yéen ñu naan: «sañ naa lépp.» waaw, waaye du lépp a jariñ nit. «sañ naa lépp,» waaye duma bàyyi dara, mu noot ma.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nevertheless i tell you the truth; it is expedient for you that i go away: for if i go not away, the comforter will not come unto you; but if i depart, i will send him unto you.
moona de, ci sama wàll, dëgg laa leen di wax. li gën ci yéen mooy ma dem, ndaxte su dul loolu, dimbalikat bi du ñëw ci yéen; waaye su ma demee, dinaa leen ko yónnee.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: