Results for false translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and many false prophets shall rise, and shall deceive many.

Wolof

te it ñu bare ñuy mbubboo turu yonent dinañu feeñ, nax nit ñu bare.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and there arose certain, and bare false witness against him, saying,

Wolof

ba mujj naaféq taxaw, seede ci moom naan:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for many bare false witness against him, but their witness agreed not together.

Wolof

teewul sax naaféq ñu bare ñëw, seede ci yeesu lu dul dëgg, waaye seen seede ànduñu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for such are false apostles, deceitful workers, transforming themselves into the apostles of christ.

Wolof

ay ndawi naaféq lañu, di ay liggéeykat yu njublaŋ yuy mbubboo turu ndawi kirist.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

woe unto you, when all men shall speak well of you! for so did their fathers to the false prophets.

Wolof

torox ngeen bu leen ñépp dee waxal lu baax, ndaxte noonu la seeni maam daan jëfe ak ña doon mbubboo yonent.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

beware of false prophets, which come to you in sheep's clothing, but inwardly they are ravening wolves.

Wolof

«moytuleen ñi mbubboo turu yonent. dañuy ñëw ci yéen, yor melow xar, waaye ci biir ay bukki yu soxor lañu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but found none: yea, though many false witnesses came, yet found they none. at the last came two false witnesses,

Wolof

waaye mënuñu koo am. teewul ñu bare ñëwoon nañu, di seede lu dul dëgg. ba mujj ñaari nit ñëw naan:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and set up false witnesses, which said, this man ceaseth not to speak blasphemous words against this holy place, and the law:

Wolof

te ñu sàkk ay naaféq yuy seede ne: «kii du bàyyee wax lu juuyoo ak bérab bu sell ba ak yoonu musaa.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and i saw three unclean spirits like frogs come out of the mouth of the dragon, and out of the mouth of the beast, and out of the mouth of the false prophet.

Wolof

noonu ma gis ñetti rab yu bon yu mel niy mbott, génn ci gémmiñi ninkinànka ja ak rab wa ak naaféq, ba mbubboo yonent.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and that because of false brethren unawares brought in, who came in privily to spy out our liberty which we have in christ jesus, that they might bring us into bondage:

Wolof

fekk na mbir moomu nekk coow ndax naaféq, yi yoxoosu ci sunu biir ak mébét mu bon, ngir seet yaatu gi nu am ci yeesu kirist, ba fexe noo defaat ay jaam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when they had gone through the isle unto paphos, they found a certain sorcerer, a false prophet, a jew, whose name was bar-jesus:

Wolof

noonu ñu jaar ci dun bépp, ba egg dëkku pafos. foofa ñu gis luxuskat bu tudd bar-yeesu, di yawut bu mbubboo turu yonent.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but there were false prophets also among the people, even as there shall be false teachers among you, who privily shall bring in damnable heresies, even denying the lord that bought them, and bring upon themselves swift destruction.

Wolof

waaye ci bànni israyil, amoon na naaféq yu mbubboo turu yonent, ni muy ame seen biir ñuy mbubboo turu jàngalekat. ci seeni pexe dinañu dugal ci yeen xalaat yu sànke, di weddi boroom bi leen jot, tey yóbbe seen bopp alkande ju teew.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the beast was taken, and with him the false prophet that wrought miracles before him, with which he deceived them that had received the mark of the beast, and them that worshipped his image. these both were cast alive into a lake of fire burning with brimstone.

Wolof

Ñu jàpp rab wa, moom ak naaféq ba mbubboo yonent, ba daan def ca turu rab wa ay kéemaan yu mu naxe ñi nangu woon a am màndargam rab wa te jaamu nataalam. Ñoom ñaar ñépp sànni nañu leen ñuy dund ca déegu safara ak tamarax buy tàkk.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and zacchaeus stood, and said unto the lord; behold, lord, the half of my goods i give to the poor; and if i have taken any thing from any man by false accusation, i restore him fourfold.

Wolof

waaye sase taxaw ne boroom bi: «déglul boroom bi, dogu naa may sama genn-wàllu alal miskin yi, te lu ma mas a njublaŋ nit, jël alalam, dinaa ko fey ñeenti yoon lu ni tollu.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,920,318,111 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK