Results for fast translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

but that which ye have already hold fast till i come.

Wolof

bu dul bii: jàppleen ci li ngeen jàpp, ba kera may ñëw. i

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

prove all things; hold fast that which is good.

Wolof

waaye seetleen mbir yépp, jàpp ci li baax,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

i fast twice in the week, i give tithes of all that i possess.

Wolof

ayu-bés gu nekk damay woor ñaari yoon, di joxe asaka ci lépp lu ma wut.”

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

watch ye, stand fast in the faith, quit you like men, be strong.

Wolof

farluleen te dëgër ci ngëm, di góor-góorlu te am pasteef.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

behold, i come quickly: hold that fast which thou hast, that no man take thy crown.

Wolof

léegi ma ñëw. sàmmal li nga yor, ngir kenn bañ laa xañ sa kaalag ndam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he said unto them, can ye make the children of the bridechamber fast, while the bridegroom is with them?

Wolof

yeesu ne leen: «ndax man ngeen a woorloo gan, yi ñëw cig céet, li feek boroom céet gaa ngi ànd ak ñoom?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

hold fast the form of sound words, which thou hast heard of me, in faith and love which is in christ jesus.

Wolof

toppal ci tànki wax yu wér yi nga dégge ci man, jàpp ci ak ngëm ak mbëggeel, yi nu am ci sunu bokk ci kirist yeesu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but christ as a son over his own house; whose house are we, if we hold fast the confidence and the rejoicing of the hope firm unto the end.

Wolof

yeesu nag ku takku la it, waaye doom la, juy yilif kër baayam. nun nooy këram googu, bu nu saxee ci sunu kóolute te di bég ci li nuy séentu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

therefore, brethren, stand fast, and hold the traditions which ye have been taught, whether by word, or our epistle.

Wolof

kon nag bokk yi, taxawleen bu dëgër te jàpp ci dénkaane yi nu leen jottali, muy ci li nu wax, muy ci li nu bind.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

only let your conversation be as it becometh the gospel of christ: that whether i come and see you, or else be absent, i may hear of your affairs, that ye stand fast in one spirit, with one mind striving together for the faith of the gospel;

Wolof

waaye dénk naa leen lii: na seeni jëf yelloo ak li kirist digle ci xebaar bu baax bi. noonu su ma leen seetsee, mbaa ma dégg seen mbir rekk, dinaa xam ne yéena ngi dëgër ci menn xel, bokk benn xalaat ci bëre luy saxal dëggu xebaar bu baax bi,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,148,858,073 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK